Download as pdf or txt
Download as pdf or txt
You are on page 1of 38

Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Essaie de traduction du livre Rouhoul Adab en wolof

Firi téere ruuhul adab


ci làkku wolof

1 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow


Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Le Prophète (que Dieu lui accorde la bénédiction et le salut) a dit:


«...‫» َم ْن ا َم َم َم ا َم ِر ًقي ا َمَيْنَيَم ِر ا ِر ِريا ِر ْن ًق ا َم َّه َما ُهللاا َم ِر ًقي اِر َم ا ْناَمَّهِرا‬

Et aussi :

‫ « ا‬...‫» َم َّه َم ا ُهللاا ْن َمًقا َمِر َم ا ِر َّه ا َم ْنَيًق ا َمَيَمَيَّه َميُهللاا َم َم ا َمِر َما‬

Et sur cet autre dire :

2 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow


Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Préface

Nous rendons grâce à Allah le TOUT Puissant, le Miséricordieux de nous avoir permis de
commencer ce travail et de le terminer afin que tout un chacun puisse en tirer profit.
Ce présent ouvrage est la traduction en langue wolof du célèbre livre Rouhoul Adab de
Cheikh Ibrahima Niass.
L’auteur El Hadji Malick Sow est un humble fidèle qui a comme projet de rendre
accessible les écrits de Baye Niass dans nos langues locales.
Prier pour nous pour la réussite de ce projet.

‫ِر ِر‬
‫ْراَر ْر ُر َر ِرّر اْر َر اَر ِر َر‬

3 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow


Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Dana wax yaqūlu ‫َرَي ُر ُرو‬


‫يم‬ ‫ِر ِر‬
Ibraahimu 'ibrāhīmu
‫إبْرَي َرر ه ُر‬
Kay doomi Allaaji najlu ālḥāji ‫َرْرَن ُرل ْراَر ِرج‬
Kay Abdillaahi `abdil'ilahi ‫َرع ْرب ِر ْر ِرإلاَر ِره‬
kay weer sunu badrināl ‫بَر ْر ِر َرَن‬
Kay aji-leer wahāji ‫اْر َر ه ِرج‬
‫ِر بَي ِر بِر ِرم ِر‬
Gannaaw wax bismillaahi min ba`di bismil-Lāhi
‫ْر َر ْر ْر‬
‫ُرُث ْرا ِر‬
Topp cant Thummal ḥamdi ‫َر ْر‬
Ñeel Yalla lil-Lāhi ‫ِر ِر‬
Kay boroomak maye dhīṭ-ṭawli ‫ِر ال ْر ِرو‬
‫ْرا ِرظ ِريم ْرملَرج ِر‬
Kay aji-màgg tedd ga āl`aḍhīmil majdi ‫ْر‬ ‫َر‬
‫يي ٌة‬ ‫ِر‬
Lii laaye biir la naṣīḥatun ‫َر َر‬
‫ِر‬
Tukkée ci man minnī ‫ِرّر‬
jëm ci samay mbokk 'ilā 'ikhwānī ‫إِر َر إِر ْر َر ِرا‬
Na ngéen jàpp faltumsikū ‫فَرَيلْرتُر ْر ِر ُرك‬
Tarixa Seex Ahmed Tiijaan ṭarīqatat-tijānī ‫َر ِرر َر َر اتِرّر َرج ِرا‬
Tarixa séllak ngëneel la ṭarīqa maḥḍil-faḍli ‫َر ِرر َري َرْر ِر اْر َر ْر ِرل‬
Ak ngërmànde Yàlla war-riḍwāni ‫ار ْر َر ِرا‬ ‫َر ّرِر‬
‫ِر‬
Fondmaa nañu ko 'ussisa
‫ُر ّر َر‬
Ci sunna bis-sunati ‫ِرِبا ُّ نَر ِر‬
Ak alxur-aan wal-furqā ni ‫َر اْر ُر ْررَر ِرا‬
Na ngéen taqoo Wa lāzimū ‫َرالَر ِرزُر‬
Wirdu laazimu bilé tarixa lāzima dhīṭ-ṭarīqi ‫الَر ِرزَرم ِر ال ِرر ِري‬

4 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow


Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Ci loolu ( taqoo ak wird bi di ko def) bidhā ‫بِر َرذ‬


Dees na amee yunālu ‫ُرَينَر ُرو‬
Tono (bénéfice) ar-ribḥu ‫ّرِر‬
‫اربْر ُر‬
Ci dëgg-dëgg bit-taḥqīqi ‫ِرِبات ْري ِر ِر‬
‫يي‬
Déet yaw falasta ‫فَرَيلَر ْر َر‬
Ci jël tarixa bi rekk fī 'akhdhiṭ-ṭarīqi ‫ِر َر ْر ِرذ ال ِرر ِري‬
Gay tono tarbaḥu
‫َرَي ْرربَر ُر‬
Ndaré bu nekk nga 'illā 'idhā kunta ‫إال إ َر ُر ْرن َر‬
‫ِر‬
Ngay yewenël tuṣliḥu ‫ُر ْر ل ُر‬
Ci bu sax dawāman ً ‫َرد َر‬
Ngay aji-matale mukammilan ً ‫ُر َرك ِرّر‬
Ay sàrtam shurūṭahu ‫ُر ُرر َرهُر‬
Ya de yu ñu saxal almuqarrarah ‫ْرملُرَر رَر ْر‬
Ngay adji sonnee mukā bidan ً ‫ُر َرك بِر‬
Ay tegginam ādābahu ‫َرد بَرهُر‬
Ya de yu ñu xalam ālmu`tabarah ‫ْرملُرْر تَرَيبَرَي َررْر‬
‫ِر‬
Ngay aji-màggal mu`aḍh-ḍhiman
ً ‫ُر َرظّر‬
Ñeel ñoñam li'ahlihi ‫ِرِل ْرَرهلِر ِره‬
‫َرِر‬
Mboole- seen jamī`an ً ‫َجي‬
‫ِر‬
Rawatina lā siyamā
‫الَر ي َر‬
Way-jagoo ñi (kilifa yi) ālkhāṣṣata ‫ْر َر ا َر‬
Na nga nekk kun ‫ُر ْر‬
‫ِر‬
Di aji topp léen muṭī`an ً ‫ُرلي‬
5 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Ndéem tàbbi nga (commencer) 'idhā shara`ta ‫إِر َر َر َرر ْرع َر‬
Ci jàng wird wi Fīd dikāril-wirdi ‫ِر ِرّرد َر ِر اْر ِر ْر ِرد‬
Na nga taqoo falāzimi ‫فَر َر ِرزِرم‬
Teggine āl'adaba ‫َر‬ ‫ِلد‬
‫ْر َر‬
‫ْرا ّرِر‬
Sa kéem kàttan qadral-ḥaddi ‫َر‬ ‫َر ْر َر‬
Teggin ta'addabun ‫َرَتَرد ٌة‬
Ci lu feeñ fī ḍhāhirin ‫ِر َر ِره ٍرر‬
Ak lu nëbbu Wa bāṭini ‫َر َرِب ِر ِر‬
Ci moom bihi ‫بِر ِره‬
Deef na égee yuraqqā ‫ُرَي َرر ى‬
Nit almar'u
‫اْر َر ْرر ُر‬
Jëm ci barab yu kawe yi (màqaama yi) lilmawāṭini ‫اِر ْرل َر َر ِر ِر‬
Na nga teewlu wāstaḥḍiranna ‫َر ْر تَر ْري ِر َررا‬
Sëriñ sa Shaykhakal ‫ك‬‫َر ْري َرخ َر‬
Kay aji-yare murabbī ‫ْرملُرَررِرّر‬
Naka noonu kadhāka ‫َر ذ َرا‬
Sëriñam shaykhahu ‫َر ْري َرخهُر‬
Ci ludul sikk bidūni raybi ‫بِر ُر ِرا َرْر ِر‬
Na ngeén takkoo Wa lāzimū ‫َرالَر ِرزُر‬
Teew ālḥuḍūra ‫ْراُر ُر َر‬
Ak dal was-sukūnā ‫َر ا ُّ ُرك َرَن‬
Naka noonu kadhāka ‫َر َرذ َرا‬
Wéetaay khalwatun ‫َر ْرل َر ٌة‬
6 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

‫ِر‬
Dana dimbale tu`īnu ‫ُر ُر‬
‫ِر‬
Ak jamono ḥīnan ً‫حين‬
Na ngua sàkku wāṭlub ‫َر ْرلُر ْر‬
Aji-yaraate murabbiyan ً‫ُر َرربِرّري‬
‫ري‬ ‫ِر‬
ً ‫َر ب‬
Kiy aji xam biiri mbir ya na mu xamee
khabīran
bitéem ya
Kiy aji laayé biir nāṣiḥan ‫ا ًي‬ ‫َرَن ِر‬
Kay aji mëtt xam-xam kāmila `irfāni ‫َر ِر َرل ِرع ْررفَر ِرا‬
Di njiit 'imāman ً ‫إِر َر‬
‫ِر‬
Ku yiw ṣāliḥan ً‫ا ا‬ ‫َر‬
‫ِر‬
Mom loo ko (jébbal ko) mallikhu ‫َرلّر ْركهُر‬
Bopp sa nafsaka ‫ك‬ ‫َرَي ْر َر َر‬
Bul féqeeti dara falā tudabbiri ‫فَر َر ُر َر بِرّر ِرر‬
Na nga nekk Wa kun ‫َر ُر ْر‬
‫َر يِرّر ٍر‬
Niki néew (cadavre) kamayyitin
‫َر‬
Ci lu sakh dawāman ً ‫َرد َر‬
Déef la solo tukhbari ‫ُر ْر َرِر‬
‫ِر‬
Bul wuuté ak moom walā tukhālifhu ‫َرالَر ُرَر ا ْر هُر‬
Donte féeñ na walaw bāna ‫َر اَر ْر َرِب َرا‬
Yàqu-yàqu xalaatam fasādu ra'ayihi ‫فَر َر ُرد َرْرِر ِره‬
Na nga nekk fakun ‫فَر ُرك ْر‬
‫َر ّرِر ٍر‬
Di boroomak roy Dhāttisā in
‫َر‬
Ci lu sax dawāman ً ‫َرد َر‬
Njuumte fakhaṭa'un ‫فَر َرخلَرأٌة‬
7 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Ñeel sëriñ bi lish-shaykhi ‫اِرلل ْري ِر‬


Moo gëna jub 'aqwamu ‫َر ْرَي َر ُرم‬
Te moo gëna yay wa'alyaqu ‫َر َراْريَر ُري‬
‫ِر ْرملُرِرر ِر‬
Ci taalibé bi Minal murīdi
‫َر‬
Ca ka xelu `inda man `aqal ‫ِرع ْرن َر َر ْر َرع َر ْرل‬
Bul geestu lā taltafit ‫الَر َرَيلْرتَر ِر ْر‬
Jëm ci keneen ku moy moom lighayrihi ‫اِر َر ْرِرريِر‬
Ci àddina si fīl-`ālami ‫ِر اْر َر ِرَرَل‬
Na nga nekk wakun ‫َر ُر ْر‬
Melne yaw rek ak moom yeena nekk ci
anlam bi
kamā law kāna dūna
`ālamin
‫اَر ْر ُر ْر َر ُرد َرا َرع ٍرَرَل‬ ‫َر َر‬
‫اِر ْرل ِرر ِر‬ ‫فَرَيلَرْري‬
Déet di ñeel taalibé bi falaysa lilmurīdi
‫َر ُر‬
Lu moy bilé wàlliyu ghayru dhāl-waliyi
‫َرْريَي ُرر َر اْر َر ِرِرّر‬
Àndak yónent bi ma`ar-rasūli ‫َر َر ار ُر ِرو‬
Topp boroomam (Yàlla) thumma mawlāhu ‫ُرُث َر ْر الَر ُر‬
Kay Aji-kawe al-`allī ‫اْر َرلِرّري‬
Filéek sax na mā dāma ‫َر َرد َرم‬
Ku moy ñoom ghayruhum ‫َرْريَي ُررُره ْرم‬
Ci xolu taalibé bi biqalbin ‫بِرَر ْرل ٍر‬
Du am lāyunāl ‫الَرُرَينَر ْرو‬
Xam Boroom bi ma`rifatul-mawlā ‫َر ْر ِررفَر ُر اْر َر ْر َر‬
Dana ma wax loolu 'aqūlu ‫َر ُر ُرو‬
Ci wax bu leer bu jarul toog di xalaat birtijāl ‫ِرِب ْر ِر َر ْرو‬
Na nga nekk wakun ‫َر ُر ْر‬
8 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Àndak sëriñ bi ma`ash-shaykhi ‫َر َر ال ْري ِر‬


Ci lu sax dawāman ً ‫َرد َر‬
Ngay tono (ngay ame bénéfice ) tar baḥu ‫َرَي ْرر بَر ُر‬
Na nga nekk wakun ‫َر ُر ْر‬
Di aji-bëgg muḥibban ًّ‫ُرِر ب‬
Di aji-sopp wāmiqan ً ‫َر ِر‬
‫ِر‬
Ngay texe fatufliḥu
‫فَرَيتُرَي ْر ل ُر‬
Ci kem na nga ko bëgge biqadri mā tuḥibbuhu ‫بِرَر ْر ِر َر ُرِر بُّهُر‬
Ngay ame tanālu ‫َرَينَر ُرو‬
Ay tëbboom amdādahu ‫َر ْر َر َرد ُر‬
Nit ñi (góoru Yàlla yi) fal-qawmu ‫فَر اْر َر ْر ُرم‬
Wax nañu qālū ‫َر اُر‬
lii hadhā ‫َره َرذ‬
Dundaleel 'anfiq ‫َرْر ِر ْري‬
Alal joo am bees ṭarīfan ً ‫َر ِرر‬
Ak alal joo fi fekk (alal ju màgget) tālidan ً ‫َرَتاِر‬
Ci sàkku fī ṭalabi ‫ِر َرلَر ِر‬
Sa gërmandé sëriñ riḍāhu ‫ِر َر ُر‬
‫ِر‬
Gaawal bādir ‫َرِبد ْر‬
Bu junjée 'in 'ashāra
‫إِر ْرا َر َر َر‬
Bu boobaa nga jot njub tuṣibi ‫ُر ِر ِر‬
Na ngua gërëmloo wa'arḍi ‫َر َر ْر ِر‬
Sëriñ sa shaykhaka ‫ك‬
‫َر ْري َرخ َر‬
9 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Donte jooyloo na la walaw 'abkākā ‫َر اَر ْر َربْر َرك َر‬


Li fi nekk lakinnahu ‫اَر ِركنهُر‬
Jubal na la qad hadākā ‫َر ْر َره َر َر‬
Jëm ci njub Lil khayri ‫اِرل َر‬
‫ْرخ ْرِرري‬
Na nga xiir wāḥriṣ ‫َر ْرح ِرر ْر‬
‫َرعلَرى ْرِلَر َر ِر‬
Ci waxtu yi `alāl'awqāti ‫ْر‬
Bum ci xiir (géppak xiir) 'ayya ḥirṣi ‫َر ِرح ْرر ِر‬
Na ngua moytandiku wāḥdhar ‫َر ْرح َرذ ْر‬
Ba nattoof la min 'an tublā ‫ِر ْر ْر‬
‫َرا ُرَي ْربَيلَرى‬
Nattu wàññeeku balā'a naqṣi ‫بَر َر َر َرَي ْر ِر‬
ndéem gis nga 'idhā ra'ayta ‫إِر َر َرَرْر َر‬
Feeñu waayu taar maḍhharal-jamāli ‫َر ظ َرْره َرر ْرْلَر َر ِرو‬
Bul bew lā taṭgha ‫الَر َرلْر َر‬
Gërëmal wārḍa ‫َر ْر َر‬
Feeñu waayu jalaal maḍhharal-jalāli ‫َر ظ َرْره َرر ْرْلَر َر ِرو‬
Kepp ci lii fakullu dhā ‫فَر ُرك ُّل َر‬
Mbiru Yàlla la 'amrul'ilahi ‫َر ْر ُرر ْر ِرإلاَر ِره‬
Déef na jox ko yusdā ‫ُر ْر َر ى‬
Màgg na moom Yàlla qad jalla ‫َر ْر َر ل‬
Ba yeddeef ko 'an yu`taba
‫َرا ُرَي ْر تَر َر‬
‫ْر‬
Ci la mu féeñal fīmā 'asdā ‫فِري َر َر ْر َر ى‬
Bul mettitlu lā tata'allaman ‫الَر َرَيتَرأَرا َر ْر‬
Ndéem gis nga 'idhā ra'aytā ‫إِر َر َرَرْرَيتَر‬
10 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Lori mbindéef yi 'idhāyatal khalqi ‫إِر َر َر َر ْر َرل ِرْري‬


Ngir lii lidhā ‫اِر َرذ‬
‫ِر‬
La bindéef la khuliqtā ‫ُر ل ْر تَر‬
Dawal na (moom Yàlla) 'ajrā ‫َر ْر َررى‬
Lor gi āl'adhā ‫ْرِلَر َرى‬
Tukkée ci ñoom jëm ci yaw minhum ‫ِر ْرنَي ُره ْرم‬
Ngir bul jeng liyallā tarkanā ‫اِريَر َرَي ْررَر نَر‬
Jëm ci ñoom 'ilayhim ‫إِراَرْري ِره ْرم‬
Li fi nekk bal ‫بَر ْرل‬
Jengal fārkanā ‫فَر ْرَر نَر‬
Jëm ci Yàlla lil'ilāhi ‫اِرإلْر ِراه‬
Ndéem nattoof na la wa'in bulīta ‫َر إِر ْرا بُرلِري َر‬
Ci tar-tar (jafe-jafe) bi'ishtidādin ‫ِرِر ْر تِر َر ٍرد‬
Ak hay washurūr ‫َر ُر ُرر ْر‬
Muñal faṣbir ‫فَر ْر ِر ْر‬
Xalsé na laa dikkal sayātīka ‫َر يَر ِر َر‬
‫يك‬
‫ِر‬
yér yér 'infirājun ‫إِر ْر َرر ٌة‬
‫ج‬
Ak kontaan (mbég) wasurūr ‫َر ُر ُرر ْر‬
Bépp guddi fakullu laylin ‫فَر ُرك ُّل اَرْري ٍرل‬
Nekk na ci gannaawam ba`dahu ‫بَرَي ْر َر ُر‬
Bëccëg na‫ـ‬hāru ‫َر َرَيه ُر‬
Bépp jafe-jafe Wa kullu `usrin ‫َر ُر ُّل عُر ْر ٍرر‬
Nekk na thi ganaawam ba`dahu ‫بَرَي ْر َر ُر‬
11 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Ak yombal yasāru
‫َر َر ُر‬
Li fi nekk bal ‫بَر ْرل‬
Bépp jafe-jafe kullu `usrin ‫َيل عُر ْر ٍرر‬
ُّ ‫ُر‬
Nékk na ci ganaawam ba`dahu ‫بَرَي ْر َر ُر‬
Ñaari yombu-yomb (jàppandal) yusrāni ‫ُر ْر َرر ِرا‬
Kéem naka dikké kamā 'a tā ‫َر َر َرَرى‬
Ci Ahmad kay kojub Adnaan `an ahmadal-`ad nāni ‫َرْحَر َر اْر َر ْر َرَن ِرا‬
‫َرع ْر ْر‬
Ndéem xam nga 'idhā `alimta ‫إِر َر َرعلِر ْر َر‬
lii dhā ‫َر‬
Nga nekk takūnu ‫َر ُرك ُرا‬
‫ِر‬
Di aji-gërëm rāḍiyan ً‫َر ي‬
Àtte Yàlla ḥukmal'ilahi ‫ُرح ْرك َرم ْر ِرإلاَر ِره‬
‫ُر ل ْر ٍر‬
Bépp waxtu kulla waqtin
‫َر‬
‫ِر‬
Ngay aji des ci loolu bāqiyan ً‫َرِب ي‬
Ndéem sàkku nga 'idhā ṭalabta ‫إِر َر َرلَرْرب َر‬
Càkkutéef maṭlaban ً‫َر لْرلَرب‬
Ñàkk nga ko `adimtahu ‫َرع ِر ْر تَرهُر‬
Loraange faḍayrahu ‫فَر َر ْريَي َررُر‬
Dana xam ko moom Yàlla yadrī ‫َر ْر ِرى‬
Te xamuloo ko wamā daraytahu ‫َرالَر َرد َرْرَيتَرهُر‬
Dana jañ moom Yàlla yadfa`u ‫َر ْر فَر ُر‬
Luy lore mā yaḍurru ‫َر َر ُر ُّر‬
Ngir ñëwati luṭfan ً ‫اُرلْر‬
12 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

‫ِر‬
Tukkée ci moom minhu ‫ْرنهُر‬
Bul tuumaal lātatahimanna
‫الَرَرَيتَر ِره َر‬
Yàlla 'ilahanā ‫إِر َرَلَرنَر‬
Ba mu gàcceel la fatukhdhalā ‫فَرَيتُر ْرخ َرذالَر‬
Bu xamoon law ya`lamu ‫اَر ْر َرَي ْر لَر ُرم‬
Doomi aadama al'insānu ‫ْر ِرإل ْر َر ُرا‬
luy Yàlla mār-raḥmānu ‫َر ار ْرْحَر ُرا‬
Dana dajeek yalqā ‫َرَي ْرل َر ى‬
Ay yi as-surūra ُّ
‫ال ُرر َر‬
Muy aji ree ḍāḥikan ‫َر ِرح ًك‬
Doomi aadama 'insānu ‫إِر ْر َر ُرا‬
Bul sàkku lātaṭlubi ‫الَرَرلْرلُر ِر‬
Teraanga (tedd) al-`izza ‫اْر ِرز‬
Ca mbindéef yi Ladāl khalqi ‫اَر َر ى ْر َرل ِرْري‬
Ci ludul sàkkoo tedd bilā ta`azzuzin ‫بِر َر َرَي َر ُّزٍرز‬
‫ِرع ْرن َر اْر لِر ِر‬
‫يك‬
Ci Buur bi `indal-malīki
‫َر‬
Déet lā ‫الَر‬
Te déet walā ‫َرالَر‬
Bul bég Lā tafraḥan ‫الَرَرَي ْر َرر َرح ْر‬
Ciy xéewal bi'an`umin ‫ِرِبَرْرَي ُر ٍرم‬
Yoo xamne xéewaleef nañu la ko 'un`imtā ‫ُرْر ِر ْر تَر‬
Na nga bég wāfraḥ ‫َر فْرَي َرر ْر‬
Ci ka nga xamne biman ‫ِرِبَر ْر‬
13 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

xéewale na 'an`ama ‫َرْرَي َر َرم‬


Ndéem xelu nga 'in `aqaltā ‫إِر ْرا َرع َر لْرتَر‬
‫فَر ُرك ُّل ِر ْر ٍر‬
Bépp xéewal fakullu ni`matin
‫َر‬
Dana dañ tazūlu ‫َرَي ُرز ُرو‬
Wëliis ki nga xamne Dūna man ‫ُرد َرا َر ْر‬
Jox na xéewal gi 'asdā ‫َر ْر َر ى‬
Kookule fadhāka ‫فَر َرذ َرا‬
Mooy aji-des ji al-bāqī ‫اْربَر ِرى‬
Ci waxtu wu nekk fī kulli zaman ‫ِر ُر ِرّرل َرزَر ْر‬
Bul xeeb lā taḥqiranna ‫الَر َر ْر ِر َررا‬
‫ِر‬
Benn jullit musliman
ً ‫ُر ْر ل‬
Bul tuddu lā tadhkuran ‫الَر َر ْرذ ُر ًر‬
‫َرع ْري إِر ْر ِرر ٍر‬
Ayibi as cam (nit) `ayba 'imri'in
‫َر‬
Te mbir momee ayib wal-`aybu
‫َر اْر َر ْري ُر‬
Amaa na bu gisée ko qad yurā ‫َر ْر ُرَي َررى‬
Ci yaw minka ‫ك‬ ‫ِر ْرن َر‬
Bari na boroom ñaari sagar farruba dhī ṭimrayni ‫ِر ْر َررْر ِر‬ ‫فَرَي ُّر ِر‬
‫َر‬
Kuy aji-pënd aghbara ‫َر ْربَرَي َرر‬
Donte giñoon na (waat na) Wa law 'aqsama ‫َر اَر ْر َر ْر َر َرم‬
Ci Borom bi kiy Yàlla bil-mawlā ‫ِرِباْر َر ْر َر‬
Mu dëggal ko 'abarra ‫َربَرَير‬
Soloo nañu ko qad rawaw ‫َر ْر َر َر ْر‬
Bul lor lā taḍuranna ‫الَر َر ُر َررا‬
14 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

‫ِر‬
Benn jullit musliman
ً ‫ُر ْر ل‬
Di lé féegn na walaw ḍhahar ‫َر اَر ْر َر َره ْرر‬
Loraange ḍurrun ‫ُر ٌّرر‬
Ci ñaari loxoom `alā yadayhi ‫َرعلَرى َر َر ْر ِره‬
Na nga jéggale fāghtafir ‫فَر ْرتَر ِر ْرر‬
Ngir nga baax da'aban ‫َرد ْربًَي‬
Naka mbindéef yi fa'inna dhāl-khalqa ‫فَرِرإا َر ْرَرل َر‬
‫ْري‬
Jaamu Yàlla nañ `ibādul-lāhi ‫ِرعبَر ُرد ال ِرَيه‬
Bul lor falā taḍir ‫فَر َر َر ِر ْرر‬
Yaw mbokk sama 'akhī ‫َر ِر ي‬
‫ِرعب َرد ِر‬
Jaami Yàlla yi `ibādal-Lāhi ‫َر‬
Déet yaw Wa lasta ‫َر اَر ْر َر‬
Ngay gërëm tarḍā ‫َرَي ْرر َر ى‬
Ka dana lor Man yaḍuru ‫َر ْر ُر ُرر‬
Jaam sa `abdakā ‫َرع ْرب َر َر‬
Donte ñaawal na wa'in 'asā ‫َر إِر ْرا َر َر‬
‫ِر‬
Ragalal fāttaqīna ‫فَر َر‬
Sa Boroom rabbakā ‫َرب َرك‬
Na nga takkoo Wa lāzimi ‫َرالَر ِرزِرم‬
Njàqare al-ḥuzna ‫ْراُرْرز َرا‬
‫ِر ْر ر اْر ِر‬
Ak fattaliku dee Wa dhikral-mawti ‫َر َر َر ْر‬
Bul ko fatte lā tansahu ‫الَر َرَي ْرن َر هُر‬
Naka noonu kadhā ‫َر َرذ‬
15 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

‫َر َرو اْر يِرّر ِر‬


Laajak néew su'ālal-mayyiti
‫َر‬ ‫ُر‬
Fàww lā budda ‫الَر بُر‬
Nga jiital 'an tuqaddima ‫َرا ُرَي َر ّرِر َرم‬
‫ْر‬
Njàng at-ta`allumā
‫اتَي َرلُّ َر‬
Na nga nekk fakun ‫فَر ُرك ْر‬
‫ِر‬
Di aji-xarañe muḥkimā
‫ُرْرك َر‬
Ci yoonou Yàlla (sariya) lishir`atil'ilahi ‫اِر ِرل ْرر َرع ِر ْر ِرإلاَر ِره‬
‫ِر‬
Xam-xam fal-`ilmu
‫فَر اْر ل ُر‬
‫ْرم‬
Giñ naa si dundu sama `umrī ‫عُر ْر ِررى‬
Moom huwa
‫ُره َر‬
Mooy njiiti jëf 'imāmul-`amali ‫إِر َر ُرم اْر َر َر ِرل‬
Kom ni ki la dikke kamā 'atā ‫َرَرى‬ ‫َر َر‬
Ci Taaha `an ṭaha ‫َرهَر‬ ‫َرع ْر‬
Ki gën ci yónent khayrir-rusuli ‫َر ْرِرري ُّار ُر ِرل‬
Na nga sàkku ḥaṣṣil ‫َرح ِرّر ْرل‬
Xam-xam `ulūman ً ‫عُرلُر‬
Yay ñintë 'arba`an ً ‫َر ْربَرَي‬
Yaw aji-sóobu dhās-sālik ‫ك‬ ‫َر ا اِر ْر‬
Bi jiitu ci xam-xam yooyu 'awwaluhā ‫َر ُرَلَر‬
‫ِر‬
Mooy xam boroom `irfānu rabbi ‫ع ْررفَر ُرا َر ِرّر‬
Kay aji moom mālik ‫ك‬ ‫َر اِر ْر‬
Aji ñaareel bi wath-thāni ‫َر ال ِرا‬
Mooy nga xam 'an ta`rifa ‫َرا َرَي ْر ِرر َر‬ ‫ْر‬
16 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

La dana aju mā yu`allaqu ‫َر ُرَي َرل ُري‬


‫َرعلَرى اْر ِرب َرد ِر‬
Ci jaamu Yàlla yi `alāl-`ibādāti ‫َر‬
lii fadhā ‫فَر َرذ‬
Mooy dëggël taḥaqququn ‫َرَرُّ ٌةي‬
Ñeenteelam thālithuhā ‫َرَثاِرلُرَي َره‬
Mooy xam haalu bakkan bi `irfānu ḥālin-nafsi ‫ِرع ْررفَر ُرا َرح ِرو انَي ْر ِر‬
Ci ay wurujam min ghadrihā ‫ِر ْر َر ْر ِر َره‬
Aki pexeem Wa kaydi hā ‫َر َر ْري ِر َره‬
Ak ay ñaawam wad-dassi
‫َر ا ِرّر‬
Ndax aji nekk la ñeel bakkan Lin nafsi ‫اِرلنَي ْر ِر‬
Ayib `aybun
‫َرع ْري ٌة‬
Ñeel na xol bi lilfu'ādi ‫اِر ْرل ُر َر ِرد‬
Ayib `aybu
‫َرع ْري ُر‬
Ñeel na ruuhu lirrūḥi ُّ ‫اِر‬
‫لر ِر‬
Ayib `aybun
‫َرع ْري ٌة‬
Déet di nekk ci loolu laysa fīhi ‫اَرْري َر فِر ِريه‬
Sikk raybu
‫َرْر ُر‬
Taqoowal tegguin fāl'adaba ‫ِلد َر‬
‫فَر ْر َر‬
Taqoowal tegguin al'adaba ‫ِلد َر‬
‫ْر َر‬
Yaw aji-sóobou ji yā dhās-sālik ‫َرَي َر ا اِر ْر‬
‫ك‬
Naka yar ak teggin fa'innahu ‫فَرِرإ هُر‬
Mooy bunt al-bābu ‫اْربَر ُر‬
Ñeel jépp aji-sóobu jëm ci Yàlla likulli sālik ‫اِر ُرك ِرّرل َر اِر ْر‬
‫ك‬
17 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Na nga nekk waltaku ‫ك‬ ‫َر اْرتَر ُر‬


‫ِر‬
Di kuy toroxlu loolu khāshi`an ً ‫َر‬
Na nga nekk di kuy suufe suufelu 'akhā tawāḍu`i ‫َر َر َرَي َر ُر ِر‬
Nekkuloo falasta ‫فَرَيلَر ْر َر‬
Ci suufe suufelu gi ngay suufe suufelu bil-waḍī`i ‫ِرِباْر َر ِر ي ِر‬
Di ku ciy toroxee fīt-takhāḍu`i ‫ِر ات َرخ ُر ِر‬
‫ِر‬
Xam-xam fal-`ilmu
‫فَر اْر ل ُر‬
‫ْرم‬
‫ِر‬
Ak koom wal-ghinā ‫َر اْر َر‬
‫ِر‬
Ak nattax (naat) Wa khaṣbun ‫َر ْر ٌة‬
Ñëw na qad 'atat ‫َر ْر َرَر ْر‬
Maskay suuf yi Wa ḥarakātul-khafḍi ‫َر َرح َررَر ُر ْرَرْر ِر‬
Ci ñoom fīhinna ‫فِر ِريه‬
Lu sax la rasat ‫َر َر ْر‬

18 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow


Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Réer wāljahlu ‫َر ْرْلَر ْره ُرل‬


Ñàkk wālfaqru ‫َر ْرا َر ْر ُرر‬
Ak rafle Wāl jadbun
‫َر ْر َرْلَر ْر ٌة‬
Ñëw na qad 'atat ‫َر ْر َرَر ْر‬
Maskay kaw yi Wa ḥarakātur-raf`i ‫َر َرح َررَر ُر ارفْر ِر‬
Ci ñoom fīhinna ‫فِر ِريه‬
Lu sax la rasat ‫َر َر ْر‬
Yii fadhī ‫فَر ِرذى‬
Ay junj la 'ishāratun ‫إِر َر َرٌة‬
Bu fekkee ni am nga xel 'idhā `aqaltā ‫إِر َر َرع َر لْرتَر‬
Yu yéeme la rā'iqatun ‫َر اِرَر ٌة‬
Na nga kham lii faltadri ‫فَرَيلْرتَر ْر ِر‬
Li nga xam ni junj nañu la ko mā 'alhimtā ‫َر ْرَرَلِر ْر تَر‬
Du tak (du dëkk) lā yaskuni ‫الَر َر ْر ُرك ِر‬
Yol (ndox) as-saylu ‫ا ْري ُرل‬
Ci kaw doj yi `alāl'ajbāli ‫َرعلَرى ْرِلَر ْر بَر ِرو‬
Du nekk luy tak ci kaw garab yi walā `alāl'ashjāri ‫َرالَر َرعلَرى ْرِلَر ْر َرج ِر‬
Ci dotteeku (sotteeku ndox gu am
doole)
fī tahmāli ‫َرَي ْره َر ِرو‬
Bul di gërëmlu lā tarḍa ‫الَر َرَي ْرر َر‬
Sa bopp `an nafsika ‫َرع ْر َرَي ْر ِر َر‬
‫ك‬
Bul toog di yaakar mukk lā tarju ‫ج‬
‫الَر َرَي ْرر ُر‬
19 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Bul ragal mukk walā takh‫ـ‬sha ‫َيـ‬


‫َيخ َر‬ ‫َرالَر َر ْر‬
‫ِر‬
Kudul Yàlla miy Boroom bi Siwāl mawlā
‫َر ى ْرملَرْر َر‬
Kudul Yàlla rekk siwāhu ‫ِر َر ُر‬
Na nga ko neenal 'ahmalā ‫َر ْر َر َر‬
Bul di rëy-rëylu lā tatakabbar ‫الَر َرَيتَر َركبَي ْرر‬
Yaw sama mbokk yā 'akhī ‫َرَي َر ِر ي‬
Bul nekk kuy añaan lā taḥsudā ‫الَر َر ْر ُر َر‬
‫الَر ُرَير ِر‬
Bul di nekk kuy ngistalu walā turā'i
‫َر َر‬
Li fi nekk bal ‫بَر ْرل‬
Sa Boroom 'ilahaka ‫ك‬‫إِر َرَلَر َر‬
Na nga ko jublu ci lépp looy def 'aqṣidā ‫ْر ِر َر‬
‫ا ِر‬
‫ْرك ْربَي ُرر‬
Rëy wal-kibru
‫َر‬
Benn 'immā ‫إِر‬
Ci xam-xam lay doon bi`ulūmin ‫بِر ُرلُر ٍرم‬
Walla ci askan 'aw nasab
‫َر ْر َر َر ْر‬
Walla ci mbooloo 'aw zummarin ‫َر ْر ُرز ٍرر‬
‫َر فِر ِرل َر َرع ٍر‬
Walla jëf ak topp Yàlla 'aw fi`li ṭā`atin ‫ْر ْر‬
Walla alal ju bari nashab
‫ل ْر‬ ‫َر‬
Moy Yàlla ma`ṣiyyatun ‫َر ْر ِر ي ٌة‬
Boo xam ni dana ko jural tūrithu ‫ُر ِر ُر‬
Toroxtànge Dhillān ًّ‫ِر ال‬
20 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Aw yiw la khayru ‫َر ْريَي ُرر‬


Jaamu Yàlla goo xam ni waṭā`atun ‫َر َر َرع ٌة‬
Dafay jur tūrithu ‫ُر ِر ُر‬
Ag rëy kibran ‫ِر ْربَي ًر‬
Ay la sharru ‫َر ُّر‬
Déet yaw falasta ‫فَرَيلَر ْر َر‬
Ngay mucc takhluṣu
‫َر ْرلُر ُر‬
Ci gaaf-gaaf yi (yiy yàq ruuhu, ‫ِر ْر فَر ِر‬
xol…)
mina ālāfāti
‫َر‬
Ludul da nga ànd ak sëriñ 'illā bishaykhin ‫ل ْري ٍر‬‫إِرال بِر َر‬
Bu xam boroomam `ārifin ‫َرع ِر ٍر‬
Boo xam ni danguay dëppook moom tuwātī ‫ُرَي َر ِرا‬
‫ِر‬
Na nga tëye faltumsikan
‫فَرَيلْرتُر ْر َرك ْر‬
Ci buumi sëriñ si bi`iṣamil-mashāyikhi ‫بِر ِر َر ِرم اْر َر َر‬
‫ل ِر ِر‬
Bu fekkee ni bëgg nga 'idhā 'aradta ‫إِر َر َر َر ْرد َر‬
Am teraanga nayla `izzin ‫َرَي ْري َرل ِرع ّرٍرز‬
Ju yékkatiku ci bountab Yàlla shāmikhi ‫َر ِر ِر‬
Ngën ci sëriñ khayru shuyūkhi ‫َر ْريَي ُرر ُر يُر ِرو‬
Ci mbooleem jamono ad-dahri ‫ا ْره ِرر‬
Ci ludul nga bàyyi kenn bil-'iṭlāqi ‫ِرِبإلْر ْر َر ِر‬
Mooy suñu njiit 'imā munā ‫إِر َر ُرنَر‬
‫ِر‬
Seex Ahmed Tiijaan at-tijāniyyi
‫اتّر َرج ِرِراّر‬
21 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Miy boroom jikko yu kawe yi dhūl'akhlāqi ‫ُر ْرِلَر ْر َر ِر‬


‫و ُر ِرل َرع ِر ٍر‬
‫بَرَي ْررَرز ُر ّر‬
Mooy barzàq bi dox diggante hadratu
barzakhu kulli `ārifin
nubuwa ak hadratu wilaaya
Mooy seen fondamaa wa'ussu lahum ‫َر ُر ُّ َرَلُر ْرم‬
Te mooy balluwaay bi Wa yanbū`u ‫َر َرَي ْرنَيبُر وُر‬
Moom Seex Wa huwa
‫َر ُره َر‬
Ab jant la shamsu
‫َرْر ُر‬
wakhayru kulliṭ- ‫َر ْريَير ُر ِرل الُّر ِر‬
Gën ci mboleem tarixa yi ṭuruqi ‫َر ُر ّر ُر‬
Ci lu ñépp nangu bil-'ijmā`i ‫ِرِبإلْر ْرَجَر ِرو‬
Mooy yoon wi ṭarīquhu ‫َر ِرر ُرهُر‬
Te maa ko wax 'ayḍan ً ‫َرْر‬
Ci ludul may xëccook kenn ci loolu bilā nizā`i ‫بِر َر ِرَرز ِرو‬
‫يل‬ ‫ِر‬
Dana jomb Wa yastaḥīlu
‫َر َر ْر تَري ُر‬
Boole tarixa Tiijaan nag jam`uhā ‫َرَجْر ُر َره‬
Ak beneen tarixa bi'ukhrā ‫ِرِبُر ْر َررى‬
Kaawtéef pert 'akhsir ‫َر ْر ِر ْرر‬
Ñeel aji gëm lu mel noonu biqā'ilin bihi ‫بِرَر اِر ٍرل بِر ِره‬
Ci beneen tarixa ba fī āl'akhrā ‫ِر ْرِلُر ْر َررى‬
Fen na kadhaba
‫َر َرذ َر‬
Te duudal na wāftarā ‫َر فْرَيتَرَي َررى‬
Ci Boroom bi `alāl'ilahi ‫َرعلَرى ْر ِرإلاَر ِره‬
Ci lu wér nag 'ajal ‫َر َر ْرل‬
22 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Man Seex Ibraahim Ñas 'innī ‫إِرِرّرا‬


Maa ngi wax lii 'aqūlu ‫َر ُر ُرو‬
Naka bii wird 'inna dhāl-wirda ‫إِرا َر اْر ِر ْر َرد‬
Doy na bajal ‫َرَر ْرل‬
Na nga taqoo Wa lāziman
‫َرالَر ِرزَر ْر‬
Bépp wird bu nekk ci tarixa bi 'adhkāra hadhāl-wirdi ‫َر ْر َر َر َره َرذ اْر ِر ْر ِرد‬
Su boobaa 'idhan ً ‫إِر‬
Maa ngi giñ ci samag dund la`amri ‫اَر َر ْر ِررى‬
‫ا ِرو‬ ‫ِر‬
Yegg ci Yàlla moom lilwuṣūli
‫ا ْرل ُر ُر‬
Dana la ci jubal tahdī ‫َرَي ْره ِر‬
Hisbu tadaruhi ḥizbut-taḍaru`i ‫ِرح ْرز ُر ات َر ُرر ِرو‬
‫ِر‬
Ak Salaatul Faatihi ṣalātul-fātiḥ
‫ا َر ُر اْر َر َي ْر‬ ‫َر‬
Naka noonu kadhāka ‫َر َرذ َرا‬
Allahumma aleyka mu awwali al-Lāhumma `alayka ‫ك‬‫ال ُرهم َرعلَرْري َر‬
‫ِر‬
Aji ubbi la ab jaam ba mu am fathu fātiḥ
‫فَر ْر‬
‫َريَير ِر‬
Ak yeneen yudul yii ma tuddagun waghayru dhī
‫َر ْر ُر‬
Ci la nga xam ni làkk na ko mimmā ḥawā ‫ِرِم َرح َر ى‬
Góor ñi ar-rijālu ‫ار َر ُرو‬ ‫ّرِر‬
Góoru tarixa bi rijālu dhīṭ-ṭarīqi ‫ِر َر ُرو ِر ال ِرر ِري‬
Bu fekkee am nañ ko 'in 'a nālū ‫إِر ْرا َر َرَناُر‬
‫ِر‬
Waaye li fi nekk mooy góor ñi lakin
‫اَرك ْر‬
23 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Seen mbóot yi sirrahum ‫ِر رُره ْرم‬


Ci kaw farlug ndongo li bijiddi ‫ِر ِر ّرِر‬
Mën nañ koy amee qad yunāl ‫َر ْر ُرَينَر ْرو‬
Du càggan ci ñàkk itte lā bil-huwaynā ‫الَر ِرِب ْرَلُرَر ْرَينَر‬
Ak naxanteek góor ñi Wa madārātir-rijāl ‫َر َر َر َر ِر ّرِر‬
‫ار َر ْرو‬
Li fi nekk bal ‫بَر ْرل‬
Ci taqoo bil-tizāmi ‫ِرِباْرتِر َرز ِرم‬
Li ñu la indil mā 'a taw
‫َر َر َرَي ْر‬
Ci lu war luzūmā
‫اُرُرز َر‬
Ak nga topp Wa bittibā`i ‫َر ِرِبّرِربَر ِرو‬
Seen wax yi qawlihim ‫َرَي ْر ِرَلِر ْرم‬
Taqoo ak moom rekk malzūmā
‫َرل ُرْرز َر‬
Bul tànn lā takhtaran ‫الَر َر ْرتَرَي َرر ْرا‬
Waxtaan ak sa maas yi taḥādduthāl'aqrāni ‫َُّث ْرِلَر ْرَي َرر ِرا‬ ‫َرَر د َر‬
‫ِر‬
Nga dem di toog ak sëriñ bi `anil-julūsi `indahu ‫َرع ِر ْرْلُرلُر ِر ع ْرن َر ُر‬
Yaw mi nga xam ni jeex nga ci sëriñ
bi lay yar
yā fānī ‫َرَي فَر ِرا‬
Bu fekkee ni danga tànn loolu 'idhan ً ‫إِر‬
Bul yaakaar mukk falā taṭma` ‫فَر َر َرلْر َر ْر‬
Ci am jot mbóot yi binaylil'asrār
‫بِرنَرَي ْري ِرل ْرِلَر ْر َرر ْر‬
Ndax mbóot fas-sirru ‫فَر ا ِرّر ُّر‬
Duñ ko ame mukk lā yunālu ‫الَر ُرَينَر ُرو‬
24 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

‫ِر‬
Ci biral `indal'ijhār
‫ع ْرن َر ْر ِرإل ْر َره ْر‬
‫ِر‬
Li am moo di lakin
‫اَرك ْر‬
Boo takkoo ak sëriñ bi 'idhā lāzamtahu ‫إِر َر الَر َرزْر تَرهُر‬
Ci lu ëpp ci say waxtu fīl-ghālibi ‫ِر اْر َر اِر ِر‬
Mën na am nga texe faqad tafūzu ‫فَرَي َر ْر َرَي ُر ُرز‬
‫ِر‬
Ci yi jóge ci sëriñ bi minhu ‫ْرنهُر‬
Ci lépp loo doon sàkku bil-maṭālibi ‫ِرِباْر َر لَر اِر ِر‬
Mën na am nga texe waqad tafūzu ‫َر َر ْر َرَي ُر َي ُرز‬
‫ِر‬
Jële ci moom minhu ‫ْرنهُر‬
Ci wàlle bil`adwā ‫ِرِباْرَي َر ْر َر ى‬
Te moom wàlle Wa hiya ‫َر ِره َري‬
Aji sax la thābitatun ‫َرَثبِرتَر ٌة‬
Fa góoru Yàlla yi `indar-rijāli ‫ار َر ِرو‬ ‫ِرع ْرن َر ّرِر‬
Kon nag teeyal antabihi ‫ْرَيتَربِر ِره‬
Ku amul man lam yanal ‫َر ْر َرَلْر َرَينَر ْرل‬
Xam Boroom bi ma`rifatar-raḥmāni ‫َر ْر ِررفَر َر ار ْرْحَر ِرا‬
Mboleem dundam 'a`māruhu ‫َرع َر ُرُر‬
‫ْر‬
Sànku na ḍā`at ‫َر َرع ْر‬
Ci mboleem jamono madāl'azmāni ‫ِلزَر ِرا‬
‫َر َر ى ْر ْر‬
Bind naa khalaqtu ‫َر لَر ْر ُر‬
Mbindéef yi dhāl-khalqa ‫َر ْرَرل َر‬
‫ْري‬
25 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Ngir ñu jaamu ma liya`budūnī ‫اِريَرَي ْربُر ُر ِرا‬


Li ma namm ya`nī ‫َرَي ْر ِر‬
Ci ñu jaamu ma biya`budūni ‫بِريَرَي ْربُر ُر ِرا‬
Mooy ñu xam ma ya`rifūnī ‫َرَي ْر ِررفُر ِرا‬
Bul gatañlu lā ta'alu ‫الَر َرَت ُرْرو‬
Dayob la nga mën juhdaka ‫ُر ْره َر َرا‬
Ngir yegg ci xàmmee Yàlla binaylil-`irfān ‫بِرنَرَي ْري ِرل اْر ِر ْررفَر ْرا‬
Boo ko defee 'idhan ً ‫إِر‬
Danga gis tarā ‫َرَي َررى‬
Kéemtaanak jege Yàlla miy
Rahmaan
`ajība qurbir-raḥmān ‫َر ُرَي ْرر ِر ار ْرْحَر ْرا‬ ‫َرع ِرجي‬
Dana feeñ moom Yàlla yaḍhharu ‫َرظ َرْره ُرر‬
‫ِر َر ي ٍر‬
Ci dara min shay 'in
‫ْر ْر‬
‫علَرى َر ي ٍر‬
Ci kaw dara `alā shay 'in
‫ْر‬ ‫َر‬
‫اَر َر ى َر ي ٍر‬
Fa dara ladā shay'in
‫ْر‬
Ci kanamu dara Wa qablahu ‫َر َرَي ْربَيلَرهُر‬
Ci gannaaw dara waba`du ‫َر بَرَي ْر ُر‬
Ba fàww sarmadā ‫َر ْررَر َر‬
Ndéem xemmem nga wa'in raghibta ‫َر إِر ْرا َر ِر ْرب َر‬
Ci yokk ngëm fī 'izdiyādil'īmān ‫ِر إِر ْرزِرد َرَي ِرد ْر ِرإل َر ْرا‬
Tuubal fatub
‫فَرَيتُر ْر‬
Tuub gu wér naṣūḥan ‫َر ُر ًح‬
26 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Toftalal ko 'ardifanhā ‫َر ْر ِردفَرَي ْرنَي َره‬


Ak rafetal (sellal) 'iḥsānan ً‫إِر ْرح َر َن‬
Bul bañ mukk lā tubghiḍanna ‫الَر ُرَي ْرب ِر َر‬
‫ِر‬
Ab jullit musliman
ً ‫ُر ْر ل‬
Bul mer ci ludul dëgg lā taghḍabi ‫الَر َرَي ْر َر ِر‬
‫ك ِر ر َرع ِر‬ ‫ِر ِر‬
Ludul ñu xotti sariya Yónent bi Yàlla 'ilā lihatki shir`atil- ‫إِرال َلَرْرت ْر‬
sellal muhadh-dhabi
‫اْر ُر َرهذ ِر‬
Na nga taqoo lāzim ‫الَر ِرزْرم‬
Ak naafila guddi qiyāmal-layli ‫ِريَر َرم ال ْري ِرل‬
Miinal xiif (faim) jū`a mi`dah ‫و ِر ْر َر ْر‬‫ُر َر‬
Ak lekk lu dagan 'aklal ḥalāli ‫َر ْر َرل ْراَر َر ِرو‬
‫ا ِر ر ِر‬
Lekk lu sell aṣ-ṣirfi
‫ّر ْر‬
Ba tey 'ayḍan ً ‫َرْر‬
‫عُر ْر‬
Bokk na ci yu ñu lim ne dana maye
`uddah
Jege Boroom bi
‫َرَن ِر‬
‫ا ِر‬
Ak laaye biir Wa nāṣiḥi
‫َر‬
Mbokk yi āl'ikhwāna ‫ْر ِرإل ْر َر َرا‬
Noppil lu bari wāṣmut ‫ا ُر ْر‬ ‫َر ْر‬
Àndalak ṣāḥibi ‫ا ِرح ِر‬ ‫َر‬
Ñoñub mbañak rus (koo xam ni am ‫ْرَرهل اْر ر ِر‬
na lu mu jomb)
'ahlal-murū'ati
‫َر ُر ُر َر‬
Ci say mbokk minal'aqāribi ‫ِر َر ْرِل َر ِر ِر‬
Waay (nit) wal-mar'u
‫َر اْر َر ْرر ُر‬
27 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Mu ngi ci diine fī dīni ‫ِر ِرد ِر‬


Àndandoom qarīnihi ‫َر ِرر نِر ِره‬
‫يم‬ ‫ِر‬
Kay aji taqoo (xaritam bu mu taqool) ālḥamīm
‫ْراَر ْر‬
‫إِر ْرا ِر‬
Ndéem ku yiw la 'in ṣāliḥan
ً‫ا ا‬ ‫َر‬
‫ِر‬
Da ngay mujja nekk di ku yiw faṣāliḥun
‫فَر َر ا ٌة‬
Bu nekkee baayima wa 'in ba‫ـ‬hīm
‫َر إِر ْرا بَر ِرَيه ْر‬
‫يم‬
Mu nekk baayima ba‫ـ‬hīm
‫بَر ِرَيه ْر‬
‫يم‬
Fàttalikul peese jëfi jaam bi Yawmal
Xiyaam
Tadhakkaril mīzāni ‫َر َرذ ِرر ْرملِر َريز ِرا‬
‫َر ْرلر ا ُّ ُري ِر‬
Ak tasaare téere jëf ya nashraṣ-ṣuḥufi
‫َر‬
Ak la nekk ca sawara Māfīl jaḥīmi ‫َر ْرْلَر ِري ِريم‬
‫ِر َرد ِرم ْرِل ِر‬
Ci saxak njàqare min dawāmil'asafi
‫َر‬ ‫ْر َر‬
Ak la nekk ca Aljana ya wafīl-jināni ‫َر ِر ْرْلِرنَر ِرا‬
Ci wëy rafeti huuril ayni min ḥisānil-ḥūri ‫ِر ْر ِرح َر ِرا ْراُر ِر‬
Ak jéebeer yi ma`al-jawāri ‫َر َر ْرْلَرَر ِر‬
Ak wëy rafeti kër ma` ḥisānid-dūri ‫َر ْر ِرح َر ِرا ا ُّ ِر‬
Na nga sax Wa dum ‫َر ُرد ْرم‬
Ci wëy kaafara bàkkaar yi
`alā mukaffirātidh-
dhanbi
‫َرعلَرى ُر َرك ّرِر َرر ِر اذ ْر ِر‬
Gën ca feddaliku ci loolu nag ākiduhā ‫ِر ُر َره‬
Mooy julli bilé Xutbu (Salaatul
ṣalātu hadhāl-quṭbi ‫ا َر ُر َره َرذ اْر ُرلْر ِر‬ ‫َر‬
Faatihi)
Tukkee na ci loolu minhā ‫ِر ْرنَي َره‬
Ñaan gu ñuy wax musabbahatul hasri al-musabba`ātu ‫اْر ُر َر بَي َر ُر‬
28 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Nga di ko def suba ṣubḥan ‫ا ْرب ًي‬


‫ُر‬
Ak ngoon Wa masā
‫َر َر َر‬
Ak baamtuwaat nodd ḥikāyatul-ādhāni ‫َر ِرا‬ ‫ِرح َرك َر ُر‬
Ba tay 'ayḍan ً ‫َرْر‬
‫ِر ِر‬
Nga nekk di kuy roy lu mel noonu dhā 'i'tisā
‫َر إاْرت َر‬
Ay xeeti sikkar yoo xam ni 'anwā`u 'adhkāri ‫َرْرَي َر وُر َر ْر َر ِر‬
Dikk na 'atat ‫َرَر ْر‬
Ci yoon wii di Tarixa Tiijaan Fīl madhhabi ‫ِر ْرملَر ْرذ َره ِر‬
Ak sunu julli gii di Salaatul Faatihi ṣalā tunā ‫ا َر ُرَينَر‬ ‫َر‬
Ci aji yëkëtiku daraja Yónent bi saw `alār-rafī`il-manṣabi ‫َرعلَرى ارفِري ِر اْر َر ْرن َر ِر‬
Ak salaatu tasbih ṣalātu tasbīḥin ‫ا َر ُر َر ْر بِري ٍر‬ ‫َر‬
Ak sàbbaal Wa tasbīḥun
‫َر َر ْر بِري ٌة‬
Naka noonu kadhā ‫َر َرذ‬
Jàng Alxur-aan di ko settantal Tadab burul qur āni ‫َر َر بَُّي ُرر اْر ُر ْرر ِرا‬
Sàmmuwanteel rā`i ‫َر ِرو‬
Jàppuwaayu àtte yooyu al-ma'akhadhā ‫اْر َر أْر َر َرذ‬
Ak julli ñaari ràkka W arak`atāni ‫َر َرْر َرتَر ِرا‬
Ci mbóot (làqu) khufyatan ً ‫ُر ْر يَر‬
Ak dox jëm naqlul-khuṭā ‫َرَي ْر ُرل ْرُرلَرى‬
‫إِر َر اْر ِر ِر‬
Ci jàkka yi 'ilāl-masājidi
‫َر َر‬
Dana ñu far yukaffiru ‫ُر َرك ّرِر ُرر‬
29 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Njuumte yi al-khaṭā'a
‫ْرَرلَر َر‬
Naka noonu kadhāka ‫َر َرذ َرا‬
‫ِر‬
Ak di taqoo ak di rafetal njàpp 'isbāghul-wuḍū 'i ‫إِر ْر بَر اُر اْر ُر ُر‬
Ommatal Wa qud ‫َر ُر ْر‬
Silmaxa 'a`mā ‫َرع َر ى‬‫ْر‬
Naka noonu kadhā ‫َر َرذ‬
‫َر َر ح ِر‬
Fajal boroom soxla soxlaam qaḍā'u ḥājati
‫ُر َر َر‬
Ak di xool duusi géej yi
wa`addu mawjil-
baḥri
‫َر َرع ُّ َر ْر ِرج اْربَر ْري ِرر‬
Ak di xalam ci màggaayu Yàlla fikratan ً‫فِر ْرك َرر‬
Ak joxante loxo muṣāfaḥatu ‫ُر َر فَر َري ُر‬
Ak mbokk yi ci Yàlla āl'ikhwān ‫ْر ِرإل ْر َر ْرا‬
Jëlal yii ma la wax fakhudh ‫فَر ُرخ ْرذ‬
‫ِر‬
Ngay aji rëbb yu baax yi muqtaniṣan
ً ‫ُر ْر تَرن‬
Nit ku dundal ta`mīru shakhṣin ‫َرَي ْر ِر ريُر َر ْرخ ٍر‬
Weeru koor ramaḍānu ‫َرَر َر ُرا‬
Ci woor ṣawmuh ‫ا ْر ُر ْره‬ ‫َر‬
Ak aji taxaw (naafila) waqā'imun ‫َر َر اِر ٌةم‬
Ci moom fīhi ‫فِر ِريه‬
Dina faxas yumaḥḥā ‫ُرَريَيى‬
Ay bàkkaar jurmuh ‫ُر ْررُر ْره‬
Ak aj ḥajjun ‫َرح ٌّر‬
30 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Ak umra wa`umratun ‫َر عُر ْر َررٌة‬


‫ا َر َر ْره‬ ‫ِر‬
Ak mbóotam saraxe Wa sirru ṣadaqah
‫َر ُّر َر‬
Mu jóge ci alal ju dagan joo moom min ḥilli mālin ‫ِر ْر ِرح ِرّرل َر ٍرو‬
Baax na ni`ma ‫ِر ْر َرم‬
Bilé sarax tilkaṣ-ṣadaqah ‫ْرك ا َر َر ْره‬ ‫ِرل َر‬
‫ابَيي ٍر‬ ‫َرَي ْر لِر ِر‬
Jàngal ay xale yu ndaw ta`līmu ṣibyatin
‫يم ْر َر‬ ‫ُر‬
Ak julli mbooloo ṣalātuṣ-ṣaffi ‫ا َر ُر ا ِرّر‬ ‫َر‬
Yi yépp ma la limal fakullu dhāka ‫فَر ُرك ُّل َر َرا‬
Borom xam-xam yi tudd nañu ko dhakarū ‫َر َر ُرر‬
Ci seen téere yi fīṣ-ṣuḥufi ‫ِر ا ُّ ُري ِر‬
Jàppal wahāka ‫َر َره َرا‬
Ay gàkk-gàkk(feebar) āfātin ‫فَر ٍر‬
Yoo xam ni dana ñu wowal tuqassī ‫ُرَي َر ِرّر ي‬
Xol bi al-qalbā
‫اْر َر لْربَر‬
‫ارَي ِر‬
Bëgg njiit ḥubbur-riyāsati
‫ُرح ُّ ّرِر َر َر‬
Moo gëna tatt 'ashaddu ُّ ‫َر َر‬
Ci ayib yi `ayban
ً‫َرع ْريَيب‬
Ak kaf mazḥun
‫َر ْرز ٌة‬
Ak jëw Wa ghībatun ‫َر ِر يبَر ٌة‬
‫لِري ا ُّ ِر‬
Toogaale bu bon jalīsus-sū'i
‫َر ُر‬
Ak ñaaw làmmiñ fuḥshun ‫ـ‬‫فُر ْري ٌة‬
31 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Ak rambaaj namīmatu ‫َرِري َر ُر‬


‫ِر‬
Ak jëmmi def lu bon Wa nafsu sū'i
‫َر َرَي ْر ُر ُر‬
Naka noonu kadhā ‫َر َرذ‬
Bàneexu bakkan hawān-nafsi ‫َره َر ى انَي ْر ِر‬
Bul ko topp falā tattabi`i ‫فَر َر َرَيتبِر ِر‬
Te nga dëddu wāzhad ‫َر ْرزَره ْر‬
Ci àddina si fīd-dunā ‫ِر ا ُّ َنَر‬
Ci ludul topp bilā tatabbu`i ‫بِر َر َرَيتَرَيبُّ ِر‬
Nekkal kun
‫ُر ْر‬
‫ِر اْر بَي ْري ٍر‬
Di aji taqoo sa néeg (chambre) ḥilsa baytin
‫َر َر‬
Te nga beru wā`tazil ‫َر ْرعتَر ِرز ْرو‬
Mbooleem mbindéef yi kullal-warā ‫ُر ل اْر َر َرى‬
‫ِر‬
Bul neexlu lā tastaṭib
‫الَر َر ْر تَرل ْر‬
Ay wax yu ñu rëbb 'aqāwilan ً‫َر َر ِرال‬
Du caage ni ay werante walā mirā ‫َرالَر ِر َرر‬
Te nga damm waghuḍḍa ‫َر ُر‬
Sa bët ṭarfan ً‫َر ْررف‬
Ci sikki nit ñi `an `uyūbin-nāsi ‫َرع ْر عُريُر ِر ان ِر‬
Na nga sàggan waltaghfalan
‫َر اْرتَرَي ْر َر لَر ْر‬
Ci ñoom `anhum ‫َرع ْرنَي ُره ْرم‬
Ci bépp ñaawtéef bikulli ba'asi ‫بِر ُرك ِرّرل َرِبْر ِر‬
32 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Saraxeel taṣaddaqi ‫َر َر ِر‬


Alal al-māla ‫اْر َر َرو‬
‫اِر ِره ِر‬
Ngir jëmmi Yàlla liwajhil-Lāhi
‫َر ْر‬
Nemmeekul zur
‫ُرز ْر‬
Bàmmeelu jullit qabra muslimin ‫َرَي ْربَي َرر ُر ْر لِر ٍرم‬
Ci ludul dayo bilā tanāhi ‫بِر َر َرَينَر ِر‬
‫ِر‬
Bul giñ lā taḥlifan
‫الَر َر ْرل َر ْر‬
Ludul 'illā ‫إِرال‬
Danga teg loolu 'idhā qay‫ـ‬yadtā ‫إِر َر َرَيي ْر َرَت‬
‫َرعلَرى اْر ِرليئَر ِر‬
Ci coobare Yàlla `alāl-mashī'ati
‫َر‬
Jamono joo giñee matā ḥalaftā ‫َر َرَت َرحلَر ْر تَر‬
Jeex na nag qadi 'intahat ‫َر ِر إِر ْرَيتَرَي َره ْر‬
Laaye biirak mbokk yi naṣīḥatu āl'ikhwāni ‫يي ُر ْر ِرإل ْر َر ِرا‬ ‫َر َر‬
‫ِر‬
Ci gàttal `alā ikhtiṣāri ‫َرعلَرى ْر تِر َر ِر‬
Tolloole kook nitu jamono ji mithla 'ahlil-āni ‫ِر لْر َرل ْرَره ِرل ِرا‬
Ci àtum ñaar fī `āmil'ithnayni ‫ِر َرع ِرم ْر ِرإل ْرَينَرَي ْر ِر‬
Ak ñeenti fukk wāl'arba`īnā ‫َر ْرِل ْربَر ِرينَر‬
‫بَرَي ْر َر َر َر َر َرع ْرل َررٍر َرئِرينَر‬
Gannaaw ñeent fukk ci téeméer ba`da thalātha
(1342) `ashratin ma'īnā

Tuddee naa sammaytu ‫َر ْري ُر‬


Wii woy dhān-naḍhma ‫انظ َرْرم‬ ‫َر‬
Ruuhu teggin Bi rūḥil'adabi ‫ِلد ِر‬
‫ِر ْر َر‬ ‫بِرُرر‬
33 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

‫َرح َر ى‬ ‫ِر‬
‫ا َر‬
Ngir li nga xam ni téeré bi làmboo na
limā ḥawā
ko
Ci ay xam-xam yuy jariñ min ḥikamin ‫ِرح َرك ٍرم‬‫ْر‬
‫ِر‬
Ak yar wa'adabi ‫َر َرَرد ِر‬
‫ِر‬
Maa ngi gàntulu mu`tadhiran
ً ‫ُر ْرتَرذ‬
Ci boroom xel yu sell yi `inda dhawīl'albābi ‫ِرع ْرن َر َر ِر ْرِلاْربَر ِر‬
Xamal leen ni ki ko déf Wa munshidan ً ‫َر ُر ْرن ِرل‬
Xale bu ndaw la bu bëgg lu baax
qawla fatāl'andābi ‫َرَي ْر َرو فَرَي َرَت ْرِلَر ْر َر ِر‬
rekk
‫ِر‬ ‫ِر‬
Doomu ñaar fukki at ak benn moo Wa libanī 'iḥdā ‫َر ابَر ِر إِر ْرح َر ى َر ع ْرل ِرر َر‬
taalif téere bi wa`ishrīna sanah
‫َر نَر ْره‬
Te kat ngàntulu ma`dhiratun ‫َر ْر ِرذ َرٌة‬
Lu ñu nangu la maqbūlatun ‫َر ْر بُر اَر ٌة‬
Lu ñu rafetlu la mastaḥsanah ‫َر ْر تَر ْري َر نَر ْره‬
Jariñal fānfa`
‫فَر ْرَي َر ْر‬
Ci yii woy bidhān-naḍhmi ‫بِر َرذ انظ ِرْرم‬
‫ِر‬
Mboleem way-gëm yi jamī`al-muu'minīn ‫َجي َر اْر ُر ْر نِر ْر‬ ‫َرِر‬
Yaw Boroom bi Yā rabbanā ‫َرَي َربَينَر‬
‫ِر‬ ‫ِر‬
‫ِر َر َر ْرِرري اْر ُر ْرر َر ل ْر‬
Ci darajay ki gën ci mboleem ñi bijāhi khayril
Yàlla yónni mursalīn

Na nga ko def yaw Yàlla wāj`alhu ‫َر ْر َرلْرهُر‬


‫ِر‬
Muy jëf ju sell khāliṣan
ً ‫َر ا‬
Ngir sa jëmm ju tedd ji liwajhikal-karīm ‫ْرك ِرر ْر‬
‫ك ا َر‬ ‫اِرَر ْر ِره َر‬
Yaw Boroom bi yā rabbi
‫َرَي َر ِرّر‬
34 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Yaw borom ñéweti gi yā laṭīfu ‫َرَياَر ِرلي ُر‬


Yaw miy yërëm ñépp ci àddina raḥmāna ‫َر ْرْحَر َرا‬
‫يم‬ ‫ِر‬
‫َرح ْر‬
Yaw miy yërëm ku la soob ca
raḥīm
Alaaxira
Bu mu la nax, bu mu la wor lā yaghurranka ‫ك‬‫الَر َرَي ُررْر َر‬
Ci nga jéem a mokkal sama woy yi Bi ḥifḍhin-naḍhmi ‫ِرِرِب ْر ِرظ انظ ِرْرم‬
Ngir sama nekk kawnī ‫َر ْر ِرا‬
‫ري‬ ‫ِر‬
Di xale ṣaghīran
ً ‫ا‬ ‫َر‬
Bu jóge ci réewi ñu ñuul ñi fī bilādil -`ajmi ‫ِر بِر َر ِرد اْر َر ْرج ِرم‬
Yàlla fallāhu
‫فَر ُر‬
Mooy jagleel yakhtaṣṣu ُّ ‫َر ْرتَر‬
Ci ngëneelam bifaḍlin ‫بِرَر ْر ٍرل‬
Ku ko sopp man yurīd ‫َر ْر ُر ِرر ْر‬
Yàlla wallāhu ‫َر هللاُر‬
Mooy borom ngëneel dhūl-faḍli ‫ُر اْر َر ْر ِرل‬
Lu màgg li al-`aḍhīmi ‫اْر َر ِرظ ِريم‬
‫َر ْرملُرِرر ْر‬
Te mooy aji namm te lu mu namm
Wāl murīd
mu am
Wax na qad qāla ‫َر ْر َر َرو‬
Ci lef bii may wax (doon xale, di ku
ñuul)
fī hadhāl majāli ‫ِر َره َرذ ْرملَر َرج ِرو‬
Aji-gën ca tedd ja al-'amjadu ‫ْرِلَر ْرْمَر ُر‬
Kay bëkk néegu Yónent bi khadīmu ṭaha ‫َر ِر ُر َرهَر‬
Kay kojub Imaam Maalig ci mazhab al-mālikiyu ‫اْر َر اِر ِرك ُّي‬
35 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Tudd Seex Ahmadu Bàmba 'aḥmadu ‫َرْحَر ُر‬


‫ْر‬
‫ِر‬
Déet di fàggul falaysa yuksibu
‫فَرَيلَرْري َر ُر ْرك ُر‬
Ñuulag aw yaram sawādul-jismi ‫َر َر ُرد ْرْلِر ْر ِرم‬
Tax nga nekk ku nëx xel balādatal-fatā ‫بَر َر َرد َر اْر َر َرَت‬
Di ku amul genn dégg ci mbir yi Wa sū'al-fahmi ‫َر ُر َر اْر َر ْره ِرم‬
Yaw Boorom bi Yā rabbi
‫َرَي َر ِرّر‬
Yaw Borom bi Yā rabbi
‫َرَي َر ِرّر‬
Ci darajay Yónent bi di kuy jubale bijāhil-hādī ‫ِر َر ِر ْرَلَر ِرد‬
Na nga fegal fakuffa ‫فَر ُرك‬
Nun ñépp `annā ‫َرعن‬
Bépp lorug noon yi kulla sharrin `ādī ‫ُر ل َر ّرٍرر َرع ِرد‬
Yàlla nga nu baaxe yaw Yàlla munna `alaynā ‫ُر َرعلَرْريَينَر‬
Ci nu am xam gu mat bikamālil-`irfān ‫بِر َرك َر ِرو اْر ِر ْررفَر ْرا‬
‫ُر ل َر ْرر ُر ٍر‬
Lépp lu nu bëgg rekk wakulla marghūbin
‫َر‬
Ci barke Yónent bi gën ci ku askanoo
ci Addnaan
bikhayri `adnān ‫ِر َر ْرِرري َرع ْر َرَن ْرا‬
Na nga suturaal fāstur ‫فَر ْر تُرَي ْرر‬
Sunu ayib yu bari yi `uyūbanā ‫عُريُر بَرَينَر‬
‫ِر‬ ‫ِر ِر‬
Ci sa mbalaanu sutura mu rafet mi bisitrikal-jamīl
‫ب ْرِر َرا ْرْلَر ْر‬
‫يل‬
Na nga nu nootal wāqhar ‫َر ْرَي َره ْرر‬
Sunuy noon `aduwanā ‫َرع ُر َرَن‬
Ci sa nootaange biqahrika ‫بِرَر ْره ِرر َرا‬
36 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

‫يل‬ ‫ِر‬
Gu màgg gi al-jalīl
‫ْرْلَرل ْر‬
Cant wal-‫ـ‬ḥamdu ‫َر ْراَر ْر ُر‬
Ñeel na Yàlla lilahi ‫ِرَرِر‬
Mi nga xam ni al-ladhī ‫ا ِرذ‬
Méngale na, may na qad 'awla
‫َر ْر َر ْر َر‬
‫ري َرظْر ِر ى‬ ‫ِر‬
‫َرَي ْري َر‬
Ba jàppandal am ma mëna def woy
taysīra naḍhmi
yii
Moom fahwa
‫فَرَي ْره َر‬
Baax na ni`ma ‫ِر ْر َرم‬
Mooy sunu Boroom al-mawlā ‫اْر َر ْر اَرَيى‬
Topp maa ngi julli ci Yónent bi thumma ṣ-ṣalātu ‫ُرُث ا َر ُر‬
Àndak nuyu Yàlla ma`a taslīmi ‫َر َر َر ْر لِر ِريم‬
Te def ci moom salaam as-salām ‫ا َر ْرم‬
Yàlla na nekk ci Yónent bi `alā n-nabiyi ‫ب‬
‫َرعلَرى ان ِرّر‬
Di ku ñu tànn ālmuṣṭafā ‫ْرملُر ْر لَرَر ى‬
Ki gën ci mbindéef khayri āl'anām ‫َر ْرِرري ْر َر‬
‫ِلَن ْرم‬
Na nekk ci moom Yónent bi `alayhi ‫َرعلَرْري ِره‬
Ak ci ñoñam yi wal-āli ‫َر ِرو‬
Ak ci mbooleem sahaabaam yi waṣḥbin ‫اي ٍر‬
‫َر ْر‬
Di ñu baax 'abrār
‫َربْرَي َرر ْر‬
Filéek texe na māfāza ‫َر فَر َرز‬
Ci xam-xamu mahrifa bil-`irfa‫ـ‬āni ‫ِرِباْر ِر ْررفَرَي ِرا‬
37 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414
Firi téere ruuhul adab ci làkku wolof

Képp kuy aji muñ kullu ṣa‫ـ‬bbār


‫اَيب ْر‬
‫ُر ُّل َر‬

38 Ceci est une réalisation de Elhadji Malick Sow


Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
N°40060280414

You might also like