Download as pdf or txt
Download as pdf or txt
You are on page 1of 25

MAWAAHIBUL

XUDUUS
Maa ngi muslu ci seytaane
ma ñu jam, di tàmbalee ci
turu Yàlla miy yërëm ku ko
soob ci àdduna, di yërëm ku
ko soob allaaxira. Yàlla na
Yàlla dooli xéewal ak mucc
sunu sangg ba Yonent bi
Muhammad. Maa ngi sàkku
ndimbalu Yàlla te moom laay
dimbalikoo. Yàlla doy nanu
te doy na moom aji Saytu ji.
Maa ngi seedeloo Yàlla ak
malaaka ya yenu aras ak sa
mbooleem malaaka ak sa
mbooleem mbindéef ci ni
yaw yaay Yàlla kenn du Yàlla
ku dul Yaw donn, déet ñeel la
aji bokkaale te Muhammad sa
jaam la sa ndaw la. Déet pexe
ak kàttan ndare ci Yàlla moom
keppay Yàlla, Muhammad
ndawam la Yàlla na ko Yàlla
dollixéewal ak mucc. Nekk na ci Yàlla dëppale ga (wut dara amee ko na nga
ko bëggee) yaw laay jaamu yaw laay dimbalikoo.
Ahmadu Mbàkke di doomi Bàlla wax na tey yaakaar ñeewentu Yàlla, cant
ñeel na Yàlla mi jiitu ci ag wéet te jurul amul nawle. Mooy ki bind mbindéef yi
ci coobareem ci lu dul aajowala loru. Maa ngikoy soreel lépp lu yellul ci moom
sunu Boroom, ñeel na ko nammeel ak kàtttanu def lu mu namm. Gënalee na
ñi baax ngir ngëm te wacc kàccoor ya ngir weddi. Xéewal ak mucc Yàlla na
ko Yàlla dolli Yonent biy mbuuka (nalaab, mooy li ñuy sexal xar ngir du bañ
alekk ci toolu jàmbur) képp kuy bokkaale di ku ñu'yedd mooy Ahmadudi
ka Yàlla yónni ci Alxuraan mu wedamloo yéefér yi ciy lay ak injoñam ak i
àndandoom ak képp ku koy roy ci xeetam wi ba yawmal xiyaam. Naan gi
bu mu dagg liféeg kuy tektaloo ci tawhiid mingi kawe ku réer ak kuy roy te
amul tektal. Xam-xam mooy ngënji lu ñuy donnoo ciy maam di ngënji lu Yàlla
di jariñee jaam waaye tawhiid mooy ngënji ndëxëñtéefujëmm ci bàmmeel ak
bisub dekki ba.
95
Ndax moom tawhid
doy na wëlis weneern xam
xam te weneen xam-xam
du jariñ liféeg àndul ak nga
xam . tawhiid. Ni ñaw gisu
ñu taalif bu dikk ci tawhiid
yem ak ba Imaam Sanuusi
def. Ngir lii, ñenn ci taalibe
yisàkku nafiu ma woy taalifu
imaam Sanuusi boobu ma jóg
ci lu gaaw tontu di ci sàkku
ndimbalu Yàlla. Yàlla miy
Boroom mbooleem mbindéef
vi dimbali na ma ba ma woy
téere bi mu dajale wépp yiw
te di jañ wépp ay. Bariwaa
na ma dolli dara ci barab te
nekkutoon ca wesar wa ngir
mu jariñ ku gàtt xel.
Tuddee naa ko
Mawaahibal Xuduus (mayi
Yàlla mu Sell mi) ci woy
we_aru. sunu sëriñ Sanuusi
umul baraahiin. Yàlla nanu
Yàlla musël ci ayu seytaane
ak ku iñaan. Naan naa ko
sama woy wi di pakk ci
sawara te di yoonu àjana ak mu nekk lu sell i lépp lu koy ñaawal ak mu
xéewal ya ak mu nekk di ngënji yóbbal ñeel ma ci bàmmel ak xëcc
nekk it di fegal ku ko wattu wala mu dégg ko ci bis péñc. Mu
bépp fitna
Ahmadu kay rammudi tànneef ak darajay Yonent yi ak darajay ci Yonent bi
xam-xam yi. waliyu yi ak boroom
NJIITAL LI
Xamal, Yàlla na la Yàlla may njub ab wërsëg wu
dara àndul ak Moom te yaatu, Yàlla nekk na te
byyikoowul ci
dara, nekkul ci dara looy yéeg fekk ko cadara, nekkul ci biir dara, nekkul ciron
ku ñu gaw, du ku Hu yenu, du kaw loola. Yàlla du ku ñu bind, du
ku ñu noot. Yéem naa
ci peeg ko ak ci sant ko dëgg-dëgg na mu sellam, mbindéef lott na
màgg ndax amul kem, amul jamono ju yellee ca Moom, nguuram tedd na te
luy rot ci xel ba fàwwu wuute na ak mu feeñ, amul xeet, amul barab. Lépp
seytaane ci pexeem ak rékkikug ngëm Yàlla. Yàlla na nga nu musal yaw mi bind
96
ci darajay Ahmadu ak
gaay yu baax yi. Yàlla na ko
Yalladolli xéewal ak mucc ak
Yàlla nanu Yàlla xiir ci jëf la
mu gërëm te fegal nu la mu
bañ.

BUNT
Di nanu wax,
wëlbatiku
ci sunug jublu, di tàmbalee
ci turu Yàlla. Xamal ni lépp
lu daw ciy xeeti àtte ci xel
tënku na ci ñett : mooy lu
war, lu jomb ak lu dagan ca
boroom xam-xam ya. Lu war
mooy la xel mu mucc bañ ag
ñàkkamn niki nekkug Yàlla
di aji Jiitu. Lu jomb mooy
loo xam ni ag amam terewu
na ci xelu képp ku dégg niki
muam ci mbindéef yi aji Jiitu
nikinjortu ñenn ñu dese ñi.
Lu dagan mooy loo xamn ni
man naa am mannaa ñàkk fa
ña làg xam-xamn niki faatug
jëmm ci lu gaaw wala mu
faatu ab diir ca kanamn niki
tam ag fentam mbindéef yi
Moom Yàlla, nekkal ku xelu.
War na ci bépp mukkalaf ci yoonu lislaam, déet ci xel, mu xam li war ci
JëmmiYàlla ak la cadagan ak laca jomb. War na yitmu xam yiici àqu Yonent
yiYàlla na len Yàlla dolli xéewal ak mucc liféeg Yàllaa ngi gindee jaamam ci
ñoom. Jëlal lenn ciy meloyu war ci Yàlla te ñoom ñaar fukki melo lañu muy
lu ñaxam Yàlla dëppóo. Bici jiitu diag Am ak Jiitu ak Des gu sax. Dëgg-dëggi
Des mooy dàq ag ñàkk gu man a dab Am ga. Bokk na ca,Wuute na Moom
Yàlla ak mépp mbindéef mu sosu. Dëgg-dëgg Wuuteek mbindéef yi mooy
dàq ag jirm mooy lu yor jëmm te boo ko làmbee daj ko ànd ak jagle ya niki
noonu harad mooy lu yorul jëmm di làqu ci jëmm.
Bokk na ca melo ya war ci Yàlla Doyloo boppam ba fåwwu mu jublu ci
leeral ni sunu Boroom aajowoowul maxal aajowoowul muxasis.
97
Dees na firi fii maxal
jëmm déet barab niki noonu
muxasis dees na ko firee fii
aji amal, xalamal. Bokk na ca
melo ya ag Wéet mu jublu
ci ni Yàlla amul ñaareel ci
jëmmam, amul ndend ci
meloom ak i jëfam. Juróom
benni melo yi, bu njkk beey
nafsiya (kojug jëmm) te mooy
wujuud (amug Yàlla). Sifaatu
nafsiya benn la muy wnjuud.
Juróom ya dikk ginnaaw ga
ñooy sifaatu salbiya (melo
yay dàq) ngir dañuy dàq
mépp mbir muyellul ciYàlla.
Am na juróom ñaari melo
yu war ci Yàlla di saxal ag
matam, ñu leen di woowee
sifaatul mahaanii muy
firiyin ci melo yuy am ci
jëmm ci lu dul lënt, mu sax
ci jëmm waral ca jëmm ja ab
àtte. Maanaa ba mooy melo
yooyu buñu nekkee ci jëmm
dañuy saxalay àtte ñeel jëmm
ja ñu nekk, yeewul.
Dees na ko woowee fa ña ñuy degërloo seen
xam-xam ci mahnawiya.
Sifaatu nahaaniibu nekkee ci jëmm ñoo koy jural àtteb sifaatu mahnawiya.
Saxug Kàttan ci Jëmmi Yàlla di na saxal Yàlla di Aji Àttan.
ñooy xudratu (kàttan), iraada (nammeel), ilmu Sifaatu mahaani
samhu(dégg), basaru (gis) ak kalaamu (wax), yii(xam-xam),
ñooy jur
xayaatu (dund),
melo
: xaadirun (aji àttan),
muriidun (aji namm), haalimun (aji xam),mahnatwrya
xayun (a)
dund), samiihun (aji dégg), basiirun (aji gis),
mutakalim (aji wax).
Dëgg-dëggi xudratu
ci mépp mbindéet i (kàttan) aw melo la wuyjàppandal ag amal ak nakKal
Yàllalàqu ko.Dëgg-dëggi mbindéef yimu dëppóok na nga ko bëggee, In ku
iraada (nammeel) aw melo la wuy ijàppandal jagleel
mbindéef ci lenrn la nga xam ne di na jaadu ci moom,
jublu juróom benn. juróom benn lanu y

98
Ñooy : am gu dagan gu
ñu wuutale ak ag ñàkk gu
ñu daganal niki noonu kem
tolluwaayam (dimension)
gu Hu ràññee ci mbooleem
kem yi. Bokk na ci melo wu
ñu ràññee ñu wuutale kook
mbooleem melo yi. Bokk na ci
jamono ju ñu ràññee wuutale
kook mbooleem jamono yi.
Niki noonu barab bi la Yàlla
jagleel ci mbooleem barab yi
ak wet wi la Yàlla jagleel ci
mbooleem wet yi. Melo yii
iraada sunu Boroom moo
koy jagleel ku ko soob xañ la
safaan ba.

BUNT CI ULUUHIYA
(melo y00 xam ne ku leen ame
di Yàlla ba doylu ci ku dul yaw
doosoxlaal kenn dara) AK LA
CAGINNAAW GA
Melo yi di Uluuhiya dees Yàlla mu toll ci fukk ak benni
naleen xam ñu bokk ca ñaar fukkimelo ya war ci
melo ñuy:wujuud (am), xidam (jiitu), baqaa(des), muxaalaful xalg(wuuteek
samhu (dégg), basar (gis),
mbindéef yi), xiyaam binafsihi (doyloo boppam), mutakalim
kalaam (kàddu), samiih (aji dégg), basiir (aji gis), (aji wax).
dul yaw dina la
Topp ca meloRubuubiya (nga xam ne ku ko ame képp ku juróom ñenti melo,
soxlaalte mooy tax nga man a nekk Buuru ñépp) ñu toll ci xayaat (dund)
ñÌo di :xudratu (kàttan), iraada (nammeel), ilmu (xam-xam),(aji dund) akug
ak nekkug Yàlla xaadir (ajiàttan), muriid (aji namm), xayun
nekkam waaxid (aji wéet).
téereb Sanuusi ka
Limal suruutul faahil (saartiaji jëf) muy juróom ñett ca(xam->xam), xayaat
xelu. Mu jublu ci : xudratu (kàttan), iraada (nammeel), ilm
ag nekkam xaadir (aji àttan),
(dund). Nent yii di nañ jur yeneen ñent muydund). Sifaatu kamaalu Laahi,
muriid (aji namm), aalim (aji xam), xayan (aji (dégg), basar (gis), kalaam
meloy matug Yàlla juróom benn lañu ñooy samhu basiir (aji gis), mutakalim
(wax) ak ñett yañett yii ditaqool samiih (aji dégg),
(aji wax).
99
BUNT CI AJUKAAYU
elgalali
MELO YI
Melo yépp ci ñaar fukki
melo yi, am na i lu mu aju
ba mu des xayaat (dund).
Tahalu (aju) mooy ci nañu
ko tuxalee sàkkug melo mbir
mu cay dolliku ginnaaw bu
saxee ci jëmm ja nga jox melo
wi, wattul ajuy mnelo yépp.
Xudratu (kàttan) ak
iraada (nammeel) aju nañu
ñoom ñaar ci mbooleem
mumkin yi. Mumkin mooy lu
jàppandi dikk nañu di ñaari
xaaj, yi am ak yi amagul te xel
nangu
te am
ag amam. Yi jappandi a saje, a5RA
(mumkinul mawjuud)
ñetti xaaj lañu : lu wees, luy Gsiis alssÃgalg23
dikk ak lu teew niki maam
yi weesu (maadin) ak doom
yi dikkagul (aatin) ak sunu
teewaay ak asamaan ak suuf
ak xalam ak aras ak kursiyu
(xaalun). Lijappandee am te
amul (mawjuudul mahduum)
ñetti xaaj lañu fa ña xam:gëmug yéefér, weddig ab jullit ak doom ci ku jaasit,
imaam Sanuusi niral na ñaari xaaj yii di ngëmug yéefér ci Abu Jahl ak weddig
aji gëm ci Abuubakr Sidiiq ndax bu sooboon Yàlla ki weddi gëm wala ki
weddi moom moo namm mu bañam.
gëm

Ilm (xam-xam) ak kalaam (wax) aju nañu ci lu war ak lu


Melow samhu (dégg) ak basar (gis) aju nañu ci lépp lu am badagan ak lu jomb.
noppiséddale nañu ko ñaari xaaj mooy li jiitu te amul tàmbalinoppi. Li am ba
ak li am te am
tàmbali. Li amul fu mu tàmbalee móoyjmmi Yàlla ak i
nii la ko ña ñuy dëgërloo waxee. Li am te am meloom akituran
: lu weesu, luy dikk ak lu teew fu mu tàmbalee ñetti xaaj lanu
niki suuf ak i gañcax.
xam) melo la ci Yàlla WOO xam ne ki ko Dëgg-dëggi ilm (xat
ame mbooleem lu ñuy xam aatay
wüññiku cimoom mu xam ko xam gu leer nàññ, du
mbooleem anam yi, diinewool topp Yàlla kon di na lawàññiku, du am wuute
fay iyool.
100
Li ñuy xam ci mbir mooy
lépp lu manul a génn àttey
xel ci lu war ak ludagan ak lu
jomb, lu dul ñett yii jommal
ku xelu ak ku xeluwul ndax
lépp lu ñuy xam manul génn
ñett yii.
Kalaam (wax) melo la
wuy taq ci Jëmmi Yàlla mi
bind mbindéef yi niki Yonent
yi mu yabal di nañ koy firi
firiyin yu wuute ca ña jüütu
waaye du Yàllaa waxee ca
làkk yooyu.
Kalaam ci Yàlla wax la ju
soreek xeeti araf ak kàddu ak
xalaat ci lu amul wuute. Lu
sell la ciy yàq wala yees wala
deng-dengi niki nii yéex ak
gaaw ak noppi ak nos wax
di ko tegale ak yu dul yii ciy
soppiku yiy am ci waxi mbindéef. Yéem naa Yàlla Boroom melo yu mat yi.
Xayaat (dund) melo la wuy wéral amug Yàlla di xamle ni Yàllaa ngi fi
waaye ajuwul cidara lucay dolliku ci taxawaayu jëmmi Yàlla. Wépp melo wu
sàkkuwul lu cay dolliku ajuwulci dara te melow xayaat (dund) kepp ci Yàlla
moo mel nii.

BUNT CI JAGOO YI(XUSUUS) AK MATALE YI (HUMUUM)


Nekk na ci ñaar fukki melo yiwar ci Yàlla xusuus (jagoo) ak humuum
(matale). Daa am melo yu am anam yuñ jagoo am yu jagooanam yépp.
Jagoo na xudratu (kàttan) ak iraada (nammeel) ci lu jàppandee am te amul,
kenn du leen ca fekk. Basar (gis)ak samhu (dégg) jagoo nañu lu am te jiitu te
amul ag tàmbali muy Jëmmi Yàlla aki meloom ak i turam.
Matale leen ñoom ñent (xudratu, iraada, samhu ak basar) ci mbooleem
lu am te sosu niki mbooleem mbindéef yi ci waxi ka gëstu. Ba tay nekk na ci
diggante xudratu (kàttan) ak iraada(nammeel) ak iln (xam-xam) ak kalaam
(wax) am nay jagoo (xusuus) ak i matale (umunn).
101
L
lIm (xam-xam) ak kalnam
(wax) jagoo nañu waajib (lu
war) ak mustaiil (u omb)
ndax ñaar ver di wdratu
(kàttan) ak iraada (nammeel)
au nañu ó lu jàpandee am
Ñoom ônt fép daje nañuci
jaa'izmuy u dagan Diggante
ilm (nam-xatn) ak kalaam dallále:
(wax lak basar gis) ak samhu
(dégg) am na jagoo ak matale.
Kalaam (wax) ak ilm (xam
am) ñoojago0 aluman a am
te Yàlladogalu ko ak lu jomb.
Samhu (dégg) ak basar (gis)
aju nafñuG lu am. Matale leen
a lépp lu am ba noppi : kalaan
(wax), ilm (xam-xam), samhu
(dégg) ak basar (gis) man nañ
caa daje. Kalaam (wax) ak ilm
(xam-xam) ñoo gën agudd ag
aju i î'u dul noom ndax aju
nañu a lépp lu war, lu jomb
ak lu dagan. Melo yi gën a gàtt giis
ag aju ñnooy sanhu (dégg) ak
basar (gis) ndax aju nañu ci
lépp lu am ba noppi. Melo yi seenug aju
ak iraada (nammeel) ndax kenn ku ne ci digg-dóomu ñooy xudratu (kattu
ñoom aju na ci ñaarixaaji mumkin
(lujappandee am) benn muy mumkin
mumkin mahduum (lu jàppandee am temawjuud
(lu jàppandee am te am) wa
faar fukki meloy sunu Boroom yi nu ñàkk). Fii la teqale gi nu doon teqale
welbatiku ginnaaw ga ci ya jomb.
BUNT CI SAFAANU NAAR FUKKI MELO YA
Naar fuhki melo di na jomb ci Yalla miy
safaanu ya stuwOoon nu saxaloon leen ci Yàlla. Boroom mtbindéef yepp \
aari neo u am yu Wuute, wuute gu
dog
Dëgg-dégginaari stttAit te
man a da te du ju t i ci bura
1ulo yi jonb a )alla tey
iooN.ailun batddnu ya utuwoon te wt
'iakk) bat.ay okk ila ci adabn d
di natoleral kanan, (Hakk) tur'u adam (rotutg t
uduus
sosu) Depy de nakk l)0y sw busu), firiyin
tutmaasul1un
ci mépp mbirlilxawaddis (yemoos
susU o m mu amul. DeggteE
irotue nakk) mooYgunn.aW ay ntkk niki nbindéef yi
skk ghatw ag ngujutu. Depg-degi tur'u da
102
Dëgg-dëggi yemook ñi
sosu fa Sanuusi mooy dàq
ag wuute ca melo yi ci jëf
ak jëmm. Yemoog Yàlla
mbindéef yi, ay anamam fa
Sanuusi dees na ko lim muy
fukk niki Yàlla ame jirm
(jëmm ju am barab ci jawu ji
ñu koy làmb di ko daj) wala
muy harad (melo wu manul
a beru dafay taq ci jëmm niki
ñuulaay wala kàttan...).
Bokk na ca muy nekk
ca wàll ya ñeel jëmm ya ñu
di juróom benn (kaw, suuf,
kanam, ginnaaw, ndeyjoor
wala càmmooñ)wala wàll di
koñeel niki nun mbindéef yi
ci ñenti wàll yi di ñent (penku,
sowwu, bëj-gànnaar wala bëj
saalum).
Wala muy tënku moom
Yàlla ci jamono wala barab.
Wala Jëmmi Yàlla diame melo
yi sosu wala muy melowoo
tuuti wala rëy niki fel wala
sanqaleñ wala lu rëy ni ñay
walab ngaaka di lu rëy lu
nekk ci géej gi wala ñu koy
melal ciy xemmemtéef ci jëf
ak àtte. Dëgg-dëggi xemmemtéef mooy am lula xiir ci jëf wala àtte ngir am loo
bëgg muy lu jomb ci Yàlla. Nikinii bokk na ca jomb ci Yàlla muy bañ taxaw ci
doyloo boppam ci nekk melo wuy taxaw ca jëmm ja wala mu soxlawoo ku ko
amal.
lu
Ba tay jomb-na ci Yàlla muy baH a nekk kenn di ku wéet ci mu nekk
keneen
limu ci jëmm ja'wala meloom yu kawe ya wala muy boroom yemookwala
wala ñaari xam-xam ñaari
cijëmmnam walaci meloom niki ñaari kàttan
nammeel di ñeel Yàlla wala jëmmam ju sell ji di nuróok jëmm jeneen wala
ci jépp jëf ngir jëf ja
muy am luy ànd ak moom di aji jeexital juy dimbali Yàlla soppiku ga,
am. Limu ci jublu mooy jëfug dara ñeelul mbindéef wala
103
du ci jëmmi boppam
moom mbindéef mi wala ci
keneen ku dul moom, li am
mooy lépp lu dul Yalla jëfi
Yàllaa. Di na jomb ci Yàlla ag
lott ci lépp lu jappandee am.
Dgg-dggi lott ci waxi
sunu sëriH Imaamu Sanuusi
mooy tëlee amal lu jàppandee
am, lo0 xam ni ag amam
jàppandiwul ku ko tëlee amal
deesu kowOowee ag lott niki
lu jomb, xelul. Niki noonu
mbindéef di am lu neexul
Yàlla wala na mu koy amee
neexul Yàlla jomb na.
Li mu ci jublu mooy lii bu
amoon dafay mel ni loolu du
nammeelu Yàlla te dara du
am lu dul la Yàlla namm mu
am. Bu loolu manoon a nekk
dafay mel ni jëfuYàlla dafay
ànd ak gëlëm wala muy
sàggan wala jëf jay am yilla
wala muy jëf juy am ci ag baaxoo te yii di zuhuul (gëlëm), hafla
(yilla) ak tabha (baaxoo) du tàbbici jëfi Yàlla. (sàggan), hilla
moo xamoon fàddu la. Dëgg-dëggi gëlëm mooy mbr
Dëgg-dëggi sàggan mooy bàyyi la nga nammoon te yëgoo ko ngir njuumte.
Dëgg-dëggi yilla mooy loo xam ni def gi moo gën a jamtalu bàyyi gi te
duko taxawalwala su nàngam saart
baaraam bi jaaro bi nekk loolu dàquwul du am niki yëngal ab jaaro ci
amul ci Yàlla deesu ni saa bu nàngamyènga.
dafay war ci Yàlla mudef nàngam, bu lii saxee kon amet
Yàlla. Dëgg-dëggibaaxoo mooy jamtalug jëf ja ci iraada (nammeel) dàqu fa
amug saart ak dàqug kuy tere niki ag lakk ci lu dul muy bàyyi, taxaw
sawara.
Niki nii réer jomb na ci Yàlla ak lépp lu
sàkkaak defe ak xalaat ak njort ak fàtte ak xel di xam ci maanaaréer niki sikR
ak tëx ak gumba ak luu. xamug settantal. Dee jomb na Yala
Safaanu meloy mahnawiya leer na ci yii.

104
BUNT CI YI DAGAN CI
ÀQU YÀLLA
Li dagan ci àqi Yàlla mooy
jëf lépp lu di mumkin (lu
jàppandee am) wala bàyyi ga
niki sàkkug mbindéef yi ak
seen i jëf ak yónnigi mu yónni
Yonent yi niki noonu yoolal
ku gëm ak mbugal kuy moy
bisub xisaab ba niki yii waral
ngëm ak haraamal weddi ak
togg jëf gi. Kiy wax ni sunu
Boroom man na lu baax man
lu gën a baax te li gën a baax
lay def dàgal xalaat woowu
kon mu wërsëgal la teggin.
Lépp lu Yàlla def loolooy i
rafet ndax bépp xéewal gu
dikk tukkee ci Yàlla jëm ci
jaamam ngëneel la gu sax.
Bépp mbugal bu gaar jaam ba
fàwwu maanug Yàlla la.
GR9glazi
Ndéem la Yàlla dogal
naqari na la doo deHci naqar
ak tiis. Na nga gërëmloo la
Yàlla dogal ngir nga noppal
sa bakkan yaw mixelu. Lépp
lu Yàlla namm luy tàbbi la
kenn manul tee mu am ndax
amulkuy jañañteek moom di xëccóok moom. Yàlla nanu Yàlla wërsëgal gërëm
lépp lu mu dogal alk dijëf mbooleem li Mu gërëm
BUNT CI LAY YA
Naka wujuud (amug Yàlla) sosug mbindéef yimooy layam ci waxi ñi xam
ndax mbindéef bu dul waon mbindéef kon mooy sos boppam te kon di na war
lënkug lenn ci ñaar ñi yemoo ci lu dul sabab, loolu lu jomb la ci képp ku xelu.
Sunu tektal ci sosug mbindéef mooy taqoo gi mu taqook harad (melo wuy
taq ci jëmm manul beru) ci ndigëlu Yàlla niki tàqarlikoo ak daje ak dal ndax
liy tagook lu sosu lu sosu la. Sunu tektal ci sosug harad mooy sunug seede ag
soppiku gu bir man a tukkee ci ñàkk jëm ci, am ak safaan ba muy tukkee ci
ñàkk jëm ci am waaye di na leer ci kuy sàkko0 xam juróom ñaari mbi.
105
lu sax la waye alds SJ A i k
Harad
manul ber, dafay tàmbali
taqook
jëmm, dafay amug
saa su ne, du tuxóo ci jëmm
jëm ci geneen niki noonu
Yàlla miy aji Jiituamul harad.
Harad manul a boole nëbbu
ak feeñ ngir dafay dajale ñaari
safan. Harad jomb na doyloo gålgl|a9s ytska l5 k
boppam i ngéru képp ku iL
Jitug
cajubña
Yalla ji ag layam
xelu, su doon Yàlla du
ajiJiitu kon di na aajowoo ku
ko sos ngir dafay daa di nekk
mbindéef kon ag wëndéelu
di na war wala càllalawu gu
yemul fenn te ñoom ñaar manu
ñoo nekk. Dawru (wëndéelu)
mooy nekkug kenn di ku ñu
def (bind) ak di ki def (bind).
Tasalsulu (càllalawu gu yemul lsa Aa
fenn) mooy ag toftaloo gu dul
dog masalan boo nee Yàlla
am na ku ko sos, koo ka war
naa am ku sos muy toftaloo
noonu di wéy rekk, loolu xel
nanguwu ko.
Yàlla ba fawwu),Baqaa (Desugfa Å
liy layam ai lajaas iága
Sanuusi mooy bu daganoon ñàkk jot Yàlla ci jamono ni mu ñu gaaree kon
gi mu jitu te amul tàmbalidàqu te su boobaa amug Yàlla jitu
dagan maanaam man naa am man a ñàkk) te ku mel nii dafay nekk jaa'iz (lu
ndax lu am ba mu yàgg daa di jeex, daa am fu mu mbindéef la, bul jengg
Naka la loolu di man a amee te wax tàmbaleewoon.
tàmbali daa war ci Moom. Nekk gi Yàlla nanu léegi ni Jiitug Yàlla gi te
nekk ku wuuteek i mbindéefamatua
layam mooy bu yemoon ak dara ci mbindéef yi kon
imoroom te liiboo xoolee li wéy xam ni jomb na dafay nekk lu sosu diseern
desam gi
amul fu muyem dàqu yaw mi xelu. ndax jiitu gu amul tàmbali an
mooy bu doon ni daa aajowoo dara ci Doylug Yàlla boppam, aw layalt
manulberu fàwwumu taq ci jëmm) te su jëmm su boobaa Yàlladi melo
ak mahnawiya dàqu te boobaa melo mahaanii ga nu(harawaxoot
s
daa aajowoo ku ko amal ñaar yii ñeel nañu Yàlla te du
harad. Bu doon rame
jitoom gu amul tàmbali akkondesam muy kusosu, loolunaka lay man a
gu amul amee te layb
106
yenmukaay Sax nañu.
Warug wéetug Yalla, aw
layam tukkee ca sëtu Yonent
bi Sanuusi mooy bu doon
Yalla wéetul, du Kenn kon
mu war ca foo fee lenn lu
nekk ñàkk ngir ag lott ngir lu
kenn ki yëkëti ka ca des tere
ko, nekkal ku tegginu. Melow
ilm (xam-xam), xayaat
(dund), xudratu (kàttan),
iraada (nammeel), seen lay
mooy bu dàquwoon kon doo
gis mbindéefu Yàlla am te
ku amul yii nu muy amalee.
Warug samhu (dégg), basar
(gis), kalaam (wax), seen lay
ñenti xaaj la. Téereem bi di
Alxuraan ak Sunna Yonent
bi Yàlla na ko Yàlla dolli
xéewal ak mucc, ñetteel ba
mooy dajeg boroom xam
xam yi, ñenteel ba mooy
li Sanuusi wax. Bu Yàlla
melowoowutoon ñett yii kon
mu mnelowoo seen safaan
muy tëx, gumba ak luu te
loolu ay wàññiku la ci Yàlla kooamal ci
te loolu lu jomb la. Layu def lépp lu am ga jàppandi wala mu bañ
dara jumu
àqu Yàlla la, bu xel mumnucc waraloon wala mu jombale ci Yàlla loolu xel
mu war te
man adoon kon li jàppandee am wala mu ñàkk jomb wala
tuxalee ca ka wattu
nanguwuko. Fii la jeexee limu lay yépp, fukk laYñu yu ñu
benn.
xam-xam. Melow nafsiya muy wujuud (am) làq na ci
melo am juróom
Meloy salbiya am na ci juróom benn. Li sabab ñuy juróomi
muy xiyaamu binafsihi
benni lay mooy daf caa am benn bu am ñaari laymahaanii ak mahnawiya
(doyloo gi Yàlla doyloo boppam), Neel na meloy
ñaari lay ndax juróom ñett ci ñoom
ñu toll ci fukk ak ñenti melo ñeel na leen
(kàttan), iraada (nammeel), ilm (xam
wenn lay lañu leen boole muy xudratu
ñoom muy mahnawiya ya xaadir, muriid,
xam), xayaat (dund) ak ya taqook imaam
xayun. Ci wenn lay it la Sanuusi boole juróom benn ya des
aalim ak (dégg), basar (gis). Topp
(wax), samhu
yépp ñoo bokk wenn lay muy kalaam
Yàlla.
fa
ca nu def wenn lay cilu dagan
107
BUNT CI YONENT YI
YÀLLA NA LEEN YÀLLA
DOLLIXEEWAL AK MUCC
Nanu wëlbati wax ji jëm
ca tànneef ya ginnaaw bu nu
faram-faccee meloy Yàlla yi.
Ya war ci àqi Yonent ya ciy
melo ñett la, Yàlla na leen
Yàlla dolli xéewal ak mucc
yu amul yemukaay : sidqu
(dëggal), amaana (kóolute)
ak tabliih (jottali) la leen
Yàlla digal.
Dëgg-dëggi sidqu (dëggal)
mooy Xibaar gu sax ca na
mbir ma amee. Dëgg-dëggi
amaana (kóolute) mooy
wattu mbooleem cër yépp ci
jépp jëf ju Yàlla tere muy lu
musib wala mu.haraamal ko.
Dëgg-dëggi tabliih (Gottali)
mooy matal lañu ko digal
ci jottali ko mbindéef yi. Di
na jomb ci ñoomn Yonent yi
safaanu yii melo ci seen àg, Yàlla na leen dolli
xeñcu seen njub. Mu jublu ci kazib (fen), xéewal ak mucc ak képp ku
musib ko wala mu
haraamal ko, ñetteel xiyaana (wor) ci jëf lu Yalla tere wala
ba moov kitmaan (nëbb
Yàlla digal ñu jottali ko mbindéef yi). dara lu leen
saxul. Dëgg-dëggi xiyaana (wor) mo0y Dëëgg-dëggi kazib (fen) mooy xibaar lu
haraam wala luñ sib. Dëgg-dëgg kitmaanñàkk a wattu cër ya ba muy det lu
jottali ko mbindéef yi ñu hëlbb ko. (nëbb) mooy lu leen Yàlla digal nu
BUNT CI LINEKK CI DIGGANTE YII
AK HUMUUM (MATALE) MELO CI XUSUUS (JAGOO)
Nekk na ci
ci àgi Yonent yidiggante yii ñetti melo
yuwenn melo man axusuus (jagoo)
yoo xam ne ñetti dàg ak humuummooy am na ayay wàiniku
melo yee leern di dàg. Ag
ñaari anam, benn bu nekk
(matale), wànniku
Yonent yi Yàlla na leen Yàllaci dolli
leeralam
anam yi miin nañu ko mumooy nga seet ci juróom
di ag wàññiku Ci 9
xéewal ak mucc.
108
Wàññiku yi ñooy ñu
wuutale te tay ko ak dolli te
tay ko ak wuutale ci njuumte
maànaam ñàkk a tay ak nëbb
te tay ko ak dolli ci njuumte
ak wuuteek ndigalu Yalla
ci jëf ak näbb ci njuumte.
Wàññiku gu njëkk gi muy
wuutale te tay ko ñetti melo
yi war ci ñoom Yonent yi ñoo
koy dàq ndax wuutale ag fen
la ba tax sidqu (dëggal) di
na ko dàq. Tabdiil (wuutale)
te tay ko haraam na ba tax
na amaana (kóolute) da koy
dàg. Tabdiil(wuutale) saa bu
tàbbee di kitmaan (nëbb) ngir
loolu seen dëgg-dëggi tablih
(jottali) dina ko jafñ.
Topp ca dolli te tay ko, la
koy jañ moy sidqu (dëggal)
ak amaana (kóolute), tabliih
(jottali)bokku ci ndax aw fen
la. Bu dee dolli gimoo ko tay
kon mu def lu haraam ngir
loolu amaana (kóolute) di ko
jañi te du kitmaan (nëbb) ba
tabliih (jottali) di ko jañ ndax
jotal na ba dolli, wéetalal
Yàlla kon nga am sa nammeel.
(dëggal),ak tablih (jottali)
Topp ca tabdiil (wuutale) ci njuumte, sidquxamees na ni fen la wu sidgu
ñookoy jañ, amaana (kóolute) du ci bokk ndax
jañ mooy tabliih
(dëggal) di jañ te yit dafay nekk kitmaan (nëbb) la koy ko jañ. Liy jañ kitmaan
(jottali). Du lu mu tay moo tax anaana (kóolute) du
(kóolute) ak tabliih (jottali).
(nëbb)ga te tay ko ciYonent yi moo÷, .amaana dollee teral te musal leen ndax
Sidqu (dëggal) du cibokk. Yàlla na leen Yàlla (jottali) lañu koy jañee. Nëbb gi
nëbb te tay ko du ag jottali su boobaa tabliih
amaana (kóolute) jañ ko.
ci tayeef lu haraam la su boobaa
(dëggal) di ko jañ ndax moom
Kitmaan (nëbb) du fen gu tàbbi ba sidqu
xibaarul dara, xàmmeel teqalee gi.
109
Topp ca dolli ci jamaj, la
koy jañ mooy sidqu (dëggal)
kese ngir ag nekkam fen ngir
loolu sidgu (dëggal) Yonent yi
moo koyjañ. Nekkgi mu nekk
ag dolli ci njuumte moo tax
amaana (kóolute) du ko jañ
ndax tayu ko. Tablih (jottali)
tam du ko jañ ndax kitmaan
(nëbb)tàbbi wu ci ndax jottali
nala ñu ko digal ba dolli ca lu
mu tayul. Wuuteek ndigalu
Yàlla gu aju ci jëf ci lu dul fen
ak làmmiñ wu juum, la koy
jañ mooy amaana (kóolute)
kese, tabliih (jottali)ak sidqu
(dëggal) duñ ci bokk ngir ag
nekkam di lu haraam kon
amaana (kóolute) moo koy
jañ. Du fen yu tàbbi ba sidqu
(dëggal) di ko jañ. Tabliih
(jottali) du ko jañ ndax du
kitmaan (nëbb) ndax moom
xibaarul dara bay nëbb wala
muy feeñal, misaalam mooy
lu mel ni njaalÐ0 wala Xool
sOxnay jàmbur ak lépp lu
nu xam ni Yàlla tere na ko
niki ray bakkan ci lu dul
àqi sariyaa (yoon). Topp ca Salgigkel
kitmaan (nëbb) ci njuumte, lay wéetoo jaHi ga mooy
jottali gu tàbbi kon tabliih (jottali) gi war tabliih (jottali) ngir du ag
tàbbiba sidqu (dëggal) di ko jañ ndax ki Yonent yi jañ ko. Du kazib (fen) gu
ginnaaw. Ag nekkam lu dul tayeef daa nëbb xibaaruldara naka mu wéyee ci
ci bokk niki mu tàbbee ci lu juum kon jañug amaana
ciy xusuus (jagoo) ak jiitu. Fii la (kóölute) u
jeexee, li nu doon leeral ci ñetti
humuum(matale) nu doonleen melo yi
LIDAGAN CI AQU
YONENT YI faram-fàcce.
Li dagan ciYonernt yi,
luy gaar doomu AadamaYàlla na leen Yàlla dolli
xéewal ak mucC mooy lepP
woyof budul tax ñu lay dawte akduxifko àggale ci wàññikugdaraja niki tawat ju
ak tukki ak sonn cidund ak mar ak mbégte ak
ak di kO xalaat coono ak dajeek lor
110
ak niki ligéy Hu lay fay ak
xeex ak dóor ak jame ci lu dul
lënt ak nelaw ak gëmm¿ntu Gas sangialsa#lls
ak farlu guy àggale ku sóobu
canjub.
Niki noonu fàtte dara lu 9e
leen Yàlla digalul ngir ñu
jottali ko mbindéef yi waaye
luy àggale ci wàHñi daraja
niki ndof ak ngaana ak siti
ak dese ak tëx ak feebaru pëy
ak ngumba ak luu ak lépp lu
bakkan di séexlu ba fawwu
wala lépp luy lompañal
yaram lu jomb la ci àqi Yonent
yi Yàlla na leen Yàlla dolli
xéewal ak mucc ndax dañoo
làq xam Yàlla gu mat akug
mucc ci jépp wàññiku niki
mu wéyee ak ñuulug yaram
ak ràbb ay sër ak ñaawug
dégg ak jëf yu suufe ak cuub
ay der ak yu nimel.

Yaw sunu Boroom yaw mi


leen def ñi gën ci nun gindi
nu ci seen barke te may nu
sunuy mébét. Ci lii dees na
tontuña ëppal ci sellal gu tar ak ña yéesal (sàggan)ngir la nasaraan ya woote
ci Yonent yingir sellal gu tar ag ëppal la, defe naYñu ngir seenug ndof ak seenug
la
réer Iisaañetteelu Yàlla la. Toskare ñeel na leen ngir lii Yàlla tontu na leen ci
rasuul.
lisaa Almasiix wax ci Alxuraan mudalee ci iqra ba
Yàlla nee na ci
Tontu na ba tay ñiy woote naan ab Yonent du mbindéef,
na ñi sàggan
Alxuraan ni defu ñu leen ñuy bañ a lekk ak du ñu faatu. Tontu
diwoote ci àqu Yonent yiluamul, ñooy ña leh melal ciy ayib akug wàññiku
Alxuraan yu réer yiak fenkat yu
ngir ñàkk a xam niki ñigàtt xel ak firikatu
ci kaw Alxuraan bañ koo taawil
dese yi ciy taarixkat ndax dañoo jàpp lifeeñ Muhammad ma bokk ca
kawe ba
taawil gu jub. Nekk na ci woyu sëriñ bu nay diri jullit di ko yóbbu ci
banuAhlaal mu wax ni zaahiru Alxuraan di
kéefér ak bidaa ak yeddeel.
111
Nekk na ci téereb
wasiilatu ibn Buunaka di ku
xam, mu wax ni bariwaana
kéefér gu sosu, la ko sabab
di réereg jëmm làkku araab.
Yàlla nanu Yàlla musal ci ag
réer, may nu ag gindiku ci
dogu ak jëf ak wax ci darajay
Yonent bi Ahmadu ak Yonent
yiak woroom xam-xam yiak
waliyu yi.
BUNT

Layug warug sidqu


(dëggal) ci Yonent yi Yàlla
na leen Yàlla dolli xéewal ak
mucc, ñoom bu ñu döggalul
wOon kon ay nar am ci xibaari
Yàlla ndax dëggal na leen ci
ay muhjiza yu mu wàccee
Ci ñoom muy taxawee niki
Yàlla daf naan sama jaam bii
dëggal na lépp lu jóge ci man
dikk ciyéen te amui palamtu.
Muhjiza mbir lay doon muy
xarbaax lëkkële nañu ko ci
càkkutéefu Yonent ba mucc
na ci gaaralante kenn du man a def lu ni mel mu
Dudikk wuuteek la musàkkuwoon, lu feeñ it ci kudëppóok la Yonent basàkku.
bokkul ak Yonent du doon
muhjiza. Irhaas (xarbaax yu Yàlla di feeñal ci Yonent njëkk mu
sàkkuwu ko) ñeel na Yonent yi njëkk wàccug waxyu (soloo) koy yónni te
fondmang la ñeel leen ci yenuag Yonent ak yen yu diis ya Yàlla ga ngir loolu
mu àndal.
Man nañu ci lim niki
ci lu dul ngistal niki bari karaama (xarbaax) ciy waliyu ña diy jaamu Yàlla
ak soppikug jëmm,"ak xamxam-xam te jàngu ñu niki gisloo jëmm ju gumba
melo
la ñeel leen ca la ñu saXjënmm ci xalaat gu amul lënt. Moom ag
xemmemloo
ngir ñu sax diiru jamono ci njub ci ngir dees na leen fay daraja yu yëkétiku
irhaas ak karaama di nañu am ci tàggat bakkan ak wird va ndax ñaar y1l
muhjiza moom Yonent baa koy càkkutéef wala lu dul càkkutéef waaye
buñ kosàkkuwulci yaw sàkku ci
Boroomam ndax dafay seede te seede
njëkk ñu sàkkuko ci amulnjariñ. Bariwaa na fu
yaw. seede yàg00 ci yëketi ko
112
Tuddee nañ ko muhjiza
ngir daa lottloo képp ku
dul ab Yonent. Lay dikk di
muhjiza cib Yonent di na
dagan di karaama cib waliyu.
Yonent yi ay mahsuum (ñuñ
musal ci moy Yàlla), waliyu
yiñu ñu wattu lañu. Bokk nañ
muslaay gi waaye wu Yonent
yi daa war, wu waliyu yi daa
dagan. Lii mooy waxu kuuy
la ka ñu tànn muy Sayidil
Muxtaar kay yeesal diine laglLasË Catislgtis
di ku baax Yàlla na ko Yàlla
gërëm ba fàwwu ak képp ku
ko xeñcu ca ña njub. Bayitu
sangg ba ibn Buuna jubalees
na ko ci waxi lenn ci waliyu
yi, tànneef ya, ag dogu ci lu
Yonent xibaar lu war la waaye
safaanub waliyu. Yàlla nanu
Yàlla wërsëgal ñaari leer ak
gënjaa rafet muj ci ñaari kër
yi ci darajay Yonent bi Yàlla
na ko Yàlla dolli xéewal
ak mucc ak i njoñam ak i
àndandoom ak ku diinewoo
lislaam, limub li Yàlla bindak
li muxalsee bind toll.Topp ca
layuamaana (kóolute) ci Yonent yi Yàlla na leen Yàlla dolli xéewal te musal
leen buH defoon lu haraam wala lu ñu sib kon lu ñu sib ak lu haraam dafay
daa di soppiku di topp Yàlla, Yàlla na xéewal ak muccgu dul dog dolliku ci
ñoom ndax Yàllaadigal mbooleem mbindéef yi ñu roy leen ci jëf ak ci wax te
ab Yonent du digle lu Yàlla haraamal wala lu mu sib.
Layu anmaana (kÓolute) feeñalaale na layu tabliih (jottali) gi ñeel ku xelu te
Yàlla
yeewu. Sunu tektal ci nekkug harad di ludagan ci seen i àq niki tawat, na
wçrteek lëndëm. Nekk
na leen Yàlla dolli xéewal ak mucc liféeg leer a ngi
ñenn ca ña leen wuutu ñu gis
Ci seedeg ñenn ci ñi jiitu ci njoñu Yonent yiak
yi ciy xeeti harad, benn ngir
loolu ngir jàkkaarloo nañu ak la daloon Yonent ca jub ak nit ñi xamee ci ni
wa
mággal seen yool ëllëg wala ngir wone yoon daraja yu kawe la Yàlla nattu
àdduna lu ñàkk solo la segam Yonent ak seen
yemoowul ak laafu yoo fa Yàlla
Sâkkaa keneen te dafay wone ni àdduna
113
wala ngir feeñal ni darajay
àdduna suufee fa Yàlla te
du lu Yàlla gërëm, du kërug
payam ñeel ku gëm ku xelu
ngir dafay jeex te luy jeex
du dara donte jotoon na fa
kawe yem te loolu ku xalaat
mbiru Yonent yi ak li ñu fi
daj gis ko, Yàlla na leen Yàlla
dolli xéewal ak mucc ndax
boroom xel bu xalaatee seen
mbir settantal ko kon mu gis
mbir ya ànd ak yeewu ci lu
dul sànqu. Topp ca maanaa
mbooleem pas-pas yii, benn
baat dajale na leen mu tukkee
ci ka îñuy topp muy Laa
ilaaha ila Laah Muhammnad
Rasuulu Laah, Yàlla na ko
Yàlla dolli xéewal ak mucc
ak injoñam ak i àndandoom
ndax uluuhiya (ag Nguur te
mooy nekk di Yàlla) mooy
doyloo lépp lu dul Moom ànd
ak aajewoo gu la lépp lu dul
yaw di aajewoo ba fàwwu,
Yàlla nanu Yàlla gindi.
Tekkig Laa ilaah ila
Laah mooy amul ku doyloo
boppam ci lépp lu dul Moom ndare Yàlla miy kenn te
aajewoo na jëm ci yaw ndare Yàlla mi bind yit képp ku dul yaw
mbindéef vi
Doyloo gi Yàlla doyloo boppam wëlis
melo : wujuud (ag amam), leneen wala
xidam (Jiitoom gi amul fukeneen di na waral ay
(desam gi amul yemukaay), muxaalafa mu tàmbalee), bagaa
(wuuteem mbindéef yi), xiyaam
binafsinihi (doyloo boppam gi), samhu (dégg), geek
ak wëy taqoo ya muy samiih (aji dégg) basar (gis), kalaam (wax) ànd
ndax yii bu warutoon ci Yàlla kon di na basiir (aji gis), mutakalim (aji wax)
aajewoo jëmm ju mu taq wala mu aajewoo ku ko sos ñeel ko wala mu
moom. Dees na ci jàppee ni Yàlla aajewoo ku ko jañal
wàññeeku yi tàbbi 1
ndax bu nekkutoon ku sell ci sellee te kawe xemmemtéef ci jëf wala àtte
aajewoo ku ko amalal xemmemntéef
xemmemtéefam wOOwu
ci jëf ak àtte
kon di na war mu
114
ngir ku xemmem di na
aajewoo dara ju ko ko amalal.
Naka la loolu di amee te Yàlla
di ku doylu wëlis keneen
ku dul Moom. Niki nii dees
na jàppee ci doylu gi Yàlla
doyloo boppam daganug
mbooleem mbindéef yi, lu
ko ci soob amal, lu ko ci soob
mu ñàkkal ko. Mujublu ci ni
Yàlla def dara wala bàyyi ko
du waajib (lu war) ci Moom
ngir warug def dara bu ko
gaaroon wala bàyyi ko niki
ab yool kon di na waral xel
nangu ni Yàlla aajewoo na lu
ko mottali ngir warul ci àgi
Yàlla miy wërsëgal mbindéef
yi lu dul ag mnat. Naka lay
nekkee moomn sunu Boroom
diaajewoo te moom ku doylu
la ci boppam wëlis lépp lu
dul moom. Aajewoo gi lépp
lu dul moom aajewoo Yàlla
di na saxal xayaat (dund),
xudratu (kàttan), iraada
(nammeel), ilm (xam-xam)
ak ya ñu taqool di : xayun (aji xam). Bu doon lenn
dund), xaadir (aji àttan), muriid (aji namm) ak aalim (aji
Yàllamu amaldara te su boobaa
ci yiidaa dàqufa Yàlla kon du jàppandi ci mooy ki nga xam ne
diamee te
dara du aajewoo ci Moom dara. Naka la loolu
nii lépp lu dul Yàlla aajewoo na Yàlla
lépp lu dul moom aajewoo na ko. Niki Tektalam mooy bu amoon ñaareel kon
dafay saxal ni Yàllakenn la di ku wéet. ñaar.
aajewoo ci Yàlla dara ngir ag lott gu ñeel kenn ku nekk ci ñoom
du
niite moom Yàlla lépp lu dulmoom aajewoo na ci Moom.
Naka lay demee leen sos. Tektalu
mbindéef yépp dañoososu te Yàllaa
Dees na cijàppee yit ni yi jituwoon kon du
dafay doyloö, boppam ba ko.
loolu mooy bu dara ci mbindéef aajewoo na
Naka la lii di amee te lépp lu dul Yàlla
aajewoo ci Yàlla dara.
Yàlla nibenn mbindéef jeexitalul
gilépp aajewoo
Dees na jàppee ci aajewoo adoon, ragalal Yalla bul ragal benn mbindéef
man
feeñalul dara ci jeexit ju mu mbindéef manoon a jeexit kon di na waral jeexit
ngir bu
Kon nga am kóolute du dog.
mbindéef def doylu wëlis Yàlla ci lu
800gu 115
Liinaka lay man a nekkee
te Yàlla lépp lu dul moom
aajewoo na ko mu jublu ci
ag tàmbali ak cibépp dayo ci
Jëmm ja ak melo wa ci misaal.
Humuum dafay firi matale
waaye fii tàmbalilay firi,xaal
tam dafay firi mbir waaye fii
dayo lay firi. Muy leeral ni
mbir mu ne fa mu tàmbalee
ba fa mu yem lépp Yàllaa,
keneen du ca dara muy ca
jëmm ja, muy ca melo wa.
Lii, bo0 nattalee diiru
jamononidara man naa jeexit
cig jikko, ndéem nattale nga
ni mbindéef man naa jeexital
cikàttan gu Yàlla def ci moom
niki mu ko njortee ñu réer,
loolu lu jomb la xelul ndax
boo jàppee ni sawara lakkul
Yàllaay lakkee ci moom nuru
na lu baax waaye daa mel ni
ngir Yàlla lakk dimbali ko0 na sawara te
a def mootax mu ni loolu jomb na ndax buaajewoowul dara ngir def wala bañ
dee lii sax na kon Yàlla dafay muj
di ku aajewoo ab diggale ci lenn ci la muy def te
xamoon ci lunjëkk ni lépp aajewOo Yàlla daa war loolu ag neen la ngir li nga
ci moom.
Képp ku fas jeexitalu jikko ab
lakkal boppam Yàlla du ci dara. Kiyéefér
la cig dëppóo niki fas ni sawaraa
Yàlla defal ab kàccoor la di toppkatusaxal jeexitalu mbindéef ci kàttan gu ko
bidaa te tooH niki fas ni sawara manul
lakkal boppam waaye Yallaay jaaree ci moom di lakk,
wala jaasi rayul Yàllaa ciy jaaree ray, mel ni wala mu fas ni fetal
ko ci jàpple mu koy dimbalikoo ngir def, Yàlla ngir ray fàwwu mu am lu
kooku ag kéeféram am na ñaari wax.
Feeñi na ñeel la lépp lu wax ji
pas. Ma jubluci ñetti xaaj yi war ngay"wax Laa ilaaha ila Laahëmb ci pas
Yàlla mooy la nga xam ne dagan mukkalaf
na
(ku ñu togg jëf) mu xam leen ci aq!
Naka baatu Muhammad Rasuulu wala mu war wala mu jomb ci àqu Yalla.
dolli xéewal ak mucc guy baamu ba Laahi (ndawal Yàlla la), Yàlla na ko Yàlla
di ñu baax, di na ci tàbbi fàwwu ak inioñam ak i
ngëm mbooleem Yonent yi (rusul) àndandoom na
(anbiyaa). ak ña ñu solo0
116
Limub Yonent yi ci waX
wér ñetti téeméer ak
ji gën
a

fukkak ñett lañu mooy jaysun


(313), waxeef na ni daysun
(314), waxeef na yit haysun
(315). Naka mbooleem rusul
(Yonent yi) ak anbiyaa (Ha ñu
solo), téeméeri ak ñaar fukk
ak ñenti junni (124 000) la ñu.
Xamal ni Yonent yépp
ay ajam (ku dul araab) la
ñu ba mu des juróom ci
lu dul njuumte. Ka ca jitu
mooy Huud ak Ismaa'iil ak
Saalih ak Chuhaybu ak ka
leen juróomeel di kilifa ga
Muhammad Yàlla na ko Yàlla
dollixéewal ak mucc. Waxyu
ñeel na leen ñoomn ñépp, fekk
nga nekk ciy nelaw ba mu
des uulul azmi (wëy dogu
yi) ña di sanggu mbindéef yi.
Ñoo di Muhammad, Nuuh,
Ibraahiim, lisaa ak Muusaa.
Dëgg-dëggi Yonent nit lay
doon, di góor, di gor, di ku
xelu kuy topp ndigal la ko
Yalla digal ci jottali la mu ko
nubuwa (ag soloo) ay saart toll ci ñent, maa
xibaar ci waryu wu kawe. Neel na
woy wi. Ma jublu ci fàwwu mu bokk cidoomu aadama yi, du
ngikoy indi ci
wala malaaka wala lu dul ñaar yii, dafay nekk góor, du doon jigéen
doon jinne ayib,
dafay nekk diirujamono diku Huy roy, dafay nekk gor di kumucc(Yonent)
ndax wala kudese wala ku réer. Ab rasuul
waaye du doon dof
di ku xelu
ci sababug yónniga ci mbooleemn mbindéefyici
Kawe na nabiyu (ku ñusoloo)nekk ku Bépp rasunl,
Yàlla dëgëral ciy muhjizaat.ñaari
ludutlënt. Ab rasuul dafay yi xäaj la ca
nekkalboroom iteggin. Gëm Yonent
Mgb1yu la déet safaan ba,
njëkk bidafay nekk cig teqale, bu ñaareel bi cig-boole
OoOm Xam-xam ya. Bumooy ñiseen tur dikk ci Alxuraan ñu di ñaar fukk ak
k gattal. Seenug tegaleAadana, Nuuh, Huud, Idriisa, Luut, Saalih, Daawuud,
jurõom : Muhammad,
Haaruun, Yahyaa, Yahquub, Ilyaas, Alyasal, Zuul.IKifli,
Muusaa.
Yuusuf, Yuunus, Ayuub, Zakariyaa, Chuhaybu, Iisaa, Sulaymaan,
onnq, Ismaa'iil, Ibraahiim,
117
Ka ca Yàlla njëkk a yónni
mooy Aadama, ka ca muij di
Muhammad Yàlla na ko Yalla
dolli xéewal ak mucc.

Bokk na ci yi tudd
Muhammad Rasuulu Laahi
ëmb gëm malaaka yi. Dëgg
dëggi malaaka mbindéef
lay doon wu Yàlla sàkkee ci
leeram waaye seen lim ku
dul Yàlla mi leen bind xamu
ko. Ay mbindéef lañu yu
yaraax (set wecc) yaram di
kojug ruuh.
Làg nañu ay xarbaax ci
Yàlla may leen îñu soppi seen
melo ci keem la Yàlla sàkku
ci ñoom. Kenn gu gëstu du
leen melal ci góor wala jigéen
wala ci lekk wala naan li am
mooy ay jaam lañu yu Yàlla
teral ñoom ñépp du ñu moy
ndigalu Yàlla.
Seen ñam mooy tudd
Yàlla, seen naan di sàbbaal
Yàlla ci bépp waxtuci lu amul werante.Teqale di na am seen diggante ci niñu
leen di gëmee niki mu jàllee léegi i Yonent yi.
Na nga xam ne war nañu leen gëm ci ag teqale fukk la ñu. Jibriil, Miikaa'il,
Israafiil, Maalik, Ridwaan, Azraa'iil, Raqiib, Hatiid, Munkar ak Nakiir, kune
ci ñoom kuywéyee ndigal la. Jibriil la Yàlla féetele waxyu gi, Miikaa'iil mo0
yor taw bi. Wal ci bufta gi ñeel nåIsraafiil, nëb ruuh yi ñeel na Azraa'il. Raqiib
ak Hatiid ñooy bind lépp lu jëmm fàggu. Munkar ak Nakiir ñoo féetewoo laaj
képp ku faatu. Ridwaan moo yor caabi àjana ya, Maalik yor caabi sawara ya.
Nu dul ñoom war nanu leen gëm cig boole b£H leen a
teqale.
Am na ci malaaka yi ñu Yàlla féetele yenu aras ak malaaka yu
Yàlla di
booleek kuëmb. Am na ci ñoom ñu nekk ci yiy yéwénal mbindéef yi niki seen
wërsëg ak seen dund. Am na ci ñoom ñu Yàlla féetële wuññi
wëlis dee. njàngarey ku jaq

118
Ñu Yàlla musal lañu ci
moy niki Yonent yi, na nga
kon
leen weg te màggal leen
nga amn mbégte. Malaaka yi
juróom
yenu aras seen lim
ñett la dadwayaa'iil,
dadfayaa'iil, satfayaa'il,
hatmayaa'iil, kamkayaa'iil,
samkayaa'iil, sasmayaa'iil,
zanjayaail. Ku mokkal tur
vi du faatu te gisul barab
Nu
ba muy toog ca ajjana.di ñi
am daraja lañu fa Yàlla
gën a tedd ci malaaka yi, ña
ca des ci ñoom laYiuy jaare
ngir gën a jege Yalla. Topp ca
kuruubiyuun yi ñooy sanggu
mbooleem malaaka yi te du
Yàlla.
ñu jengg jëm ci ku dul
Malaaka ya nekk asanmaan,
seen imelo wuute na. Melow
malaaka yinekk ciasamaan si
gën a jege àdduna ñi ngi mel
nekk
ni melo nag, ña ca topp
dañoo
Ci asamaanu ñaareel
mel ni ay jiit. Na ca topp mel
niay tan. Na ca topp nekk ca ni ay fas. Na ca topp ca asamaanu juróomeel
asamaanu ñenteel dañoo mel juróom benneel
(uurulayni). Na ca asamaanu
dañoo mel ni jigéeni àjjana muy luñndëppóo. Malaaka ya ca kaw juróom
dañuy mel niay doomu Aadama ba ñenn ñi dun
kiiraay, malaaka yi bari fa lool
ñaareelu asamaan daa am i ngir bari lool ñuy sàbbaal Yàlla ci baat yu
xamante
xàmmee ñeneen ñi, dun
ñüy dëgërloo seen iwax.
wuute niki dënnu ci waxi ña wàccee barke jëlee ko ci
almuhagqibaat dañuy
Bokk naca ñoom ñuñuy wax leen ko Yàlla joxloo. Bokk na ciñoom ku turam
ña
Sunu Boroom di ko vóbbul a wér. Yàlla
ci seen :
nanu Yàlla wërsëgal njubrammu
ci li gën
di Haaruut ak Maaruutàddunaak allaaxira cidarajay Ahmad ka nuy képp
daraja ak mujj gurafet xéewal ak mucc ak i njoñam ak iàndandoom ak tàbbi
Talla na ko Yàlla dolli Niki téere ya di kojug asamaan di nañu
askanalee
mbindéef vi. ya. Di nañ leen
Ku leen di roy ci Rasuullu Laah fa nettalikat
Yàlla
DO0nee Muhammad bàyyikO0 ca asamaan ñooy téere yi
sangg yi
dsamaan ndax dikkee nañu ne yónni na leen ci m mbindéef yi
wàccee ci ñenn ci ña nga Xam 119

You might also like