Download as docx, pdf, or txt
Download as docx, pdf, or txt
You are on page 1of 9

Firi teere bi toude kirayal dioullit

Ci ñaane yi nek ci alqouran ak sounna

Ki talif teerebi moy doctor sahid domi alliye


allkhahtani

Ki firi teerebi moy ibrahima khalil lo mou ndaw

.Gënéelal toude yalla


: YALLA neena

‫﴿َف اْذ ُك ُروِني َأْذ ُك ْر ُك ْم َو اْش ُك ُروْا ِلي َو َال‬:


﴾ ‫َتْكُفُروِن‬
Toude léenma ma toude léen, sante léenma te
bouléenma xarab.
YALLA wakhatne:

﴿‫رًا‬ ‫َي ا َأُّيَه ا اَّل ِذ يَن آَم ُن وا اْذ ُك ُروا َهَّللا ِذ ْك‬
‫﴾َك ِثيرًا‬
Yéen ñigëme déeléen toude YALLA lou bari lool.
YALLA WAKHATNE:

‫َو الَّذ اِكِريَن َهَّللا َك ِث يرًا َو الَّذ اِكَر اِت َأَع َّد‬
﴿‫ُهَّللا‬
‫﴾َلُهم َّم ْغ ِفَر ًة َو َأْج رًا َع ِظ يمًا‬
Dafalim mélokani ñigëm yalla moune ñom dëy ay
toudou katou yalla yougor ag you jigéen lane, tedañou koy
toude lou bari, moune ñom ñoñou dëy yalla migileeni xàré
ak njeggël akouk paye gou rëye.
YALLA wakhatne:
(1)،﴿‫َو اْذ ُك ْر َّرَّبَك ِفي َنْفِس َك َتَض ُّر عًا َو ِخ يَف ًة‬
‫ِر ِم َن‬ ‫َو ُد وَن اْلَج ْه‬
‫اْلَق ْو ِل ِباْلُغ ُد ِّو َو اآلَص اِل َو َال َتُك ن ِّم َن‬
‫﴾اْلَغ اِفِليَن‬
Néena: yaw yonneent bi (salla lahou alayhi wasallam):
dél toud sa broom gay trokhlou ak diko ragal, te boulkoy
biralle loole, naga koy def ci soubagi ag ngon gi, te boul
book mouk ci ñi saggan.

Yonnentebi (salla lahou alayhi wasallam) wakhne:

،‫رَّبُه‬
(( ‫ َو اَّلِذ ي َال َيْذ ُك ُر‬،‫َم َثُل اَّلِذ ي َيْذ ُك ُر َر َّبُه‬
‫َو اْلَم ِّيِت‬ ‫) ( َم َثُل اْلَح ِّي‬))
2

msaloum kiy toude yalla ak kiko doul toude migi melne


kouy doundou ak kou dèe, limou ci dioublou moy toude
yalla dafa mèlnè ag rouh ci yaram, koudoul toude yalla dafa
mèlne kou fatou.

Yonnentebi (salla lahou alayhi wasallam) wakhne:

. 35 :‫ اآلية‬،‫() سورة األحزاب‬ 1

،779 ‫ ب رقم‬،539 /1 ،‫ ومس لم‬،6407 ‫ ب رقم‬،208 /11 ،‫() البخ اري م ع الفتح‬ 2

‫ ((مث ل ال بيت ال ذي ي ذكر الَّل ه في ه وال بيت ال ذي ال ي ذكر الَّل ه في ه مث ل الحي‬:‫بلف ظ‬


. 1/539 ،))‫والميت‬
Xanaa doumalèen xibar ligën ci seeni diëfyi, te gëna
teed fa seen broom, te gëna mana gàw ci yëkkati seeni graat
fa yalla, te mo gën sakh gèen di diokhè wourous ak khalis,
te gën gèen tasèek sèenoub non ci gèen di jihadag ñoom
ñou dilèen ray gèen dilèen ray?
Ñounèko wakhñouko kay, mounè lèen loolou moy
toud yalla.
‫‪Ligay ñaan boo yew woo ciy nelaw‬‬
‫‪Daganàn:‬‬

‫((اْلَحْم ُد ِهَّلل اَّلِذ ي َأْح َياَنا َبْع َد َم ا َأَم اَتَنا‪َ ،‬و ِإَلْيِه‬
‫الُّنُش وُر ))(‪.)3‬‬
‫‪Niga koy diangé:‬‬
‫‪Alhmdou lil lahil lazi ahyànà bahda maa amatanaa, wa‬‬
‫‪ilayhin nouchour.‬‬

‫‪Limouy firi:‬‬
‫‪Magi sant yalla miñou doundalaat ginaw bimouñou‬‬
‫‪fàatèe, te bouñou dèkkèe ci moom lañou dëm.‬‬
‫‪(limou dioublou ci fatou gii mooy nelaw, ndakh nelaw‬‬
‫‪fatou gou ndawla).‬‬
‫‪Gawakhaatnè:‬‬

‫‪َ(( )2(-‬ال ِإَلَه ِإَّال ُهَّللا َو ْح َد ُه َال َش ريَك َلُه‪َ ،‬لُه‬


‫اْلُم ْلُك َو َلُه اْلَحْم ُد ‪َ ،‬و ُهَو َع َلى ُك ِّل َش ْي ٍء َقِد يٌر‪،‬‬
‫ُس ْبَح اَن ِهَّللا‪َ ،‬و اْلَحْم ُد ِهَّلل‪َ ،‬و َال ِإَلَه ِإَّال ُهَّللا‪َ ،‬و ُهَّللا‬
‫َأكَبُر‪َ ،‬و َال َح ْو َل َو َال ُقَّو َة ِإَّال ِباِهَّلل اْلَعِلِّي‬
‫اْلَعِظ يِم ‪َ ،‬ر ِّب اْغ فْر ِلي))(‪.)4‬‬
‫() البخ اري م ع الفتح‪ ،113 /11 ،‬ب رقم ‪ ،6314‬ومس لم‪ ،2083 /4 ،‬ب رقم‬ ‫‪3‬‬

‫‪.2711‬‬
‫() من قال ذلك ُغِف َر له‪ ،‬فإن دعا استجيب له‪ ،‬فإن ق ام فتوض أ ثم ص لى ُقبلت ص الته‪،‬‬ ‫‪4‬‬

‫البخاري مع الفتح‪ ،39 /3 ،‬برقم ‪ ،1154‬وغيره‪ ،‬واللفظ البن ماجه‪ ،‬انظر‪ :‬صحيح‬
Niga koy diangè:
La ilaha illal lah wahdhou la charika lhou, lhoul moukou
walhoul hamdou, wa houwa alaa koulli chaye in khadiroun.
Soubhanal laah, walhamdou lillaah , walà ilàha illal làh,
allahou akbàr.
Walà hawla walà khouwwata illà bil làhil aliyyil asimi.

Limiy firi moy:


Amoul keen wala lèen lou yayoo ñou diàmouko
koudoul yàlla, mom dong ga ko yayoo, te amoul kén kou
ñouy ko ciy bookkalèl, yàlla momom lèep louy ngour, ak
lèep louy khetou cinte mooko yayo, temooy ki am kattan ci
lèepe.
Sellal nako ci lèep louñou koy bookkalè ak lèep louy ag
mankitè.
Diko sant moom mi yayo bmolèem kheti thiante yi.
Di sèedenè Amoul keen wala lèen lou yayoo ñou
diàmouko koudoul yàlla.
Te mom yalla mogëna mag lounè.
Te amoul ben kattan walla men pèkhè mou mana sootti
loudoul ci thiobarèem ak ndimbalëm.
Mom yalla mooy kou kaweki te mooy kou mag ki.
Yaw sama broom dièggalma samay bakkàar.
Yonnèntèbi (sallal làhou alayhi wasallama) nèna: kou

. 2/335 ،‫ابن ماجه‬


yèewou wakhli dièeggal nañ ko ay bakkàram, te bou ñanèe
yàlla naggou ñànam, tè bou diougèe moudadi diàpe dadi
dioulli yàlla dana naggou ag dioullèem.

(3) (( ،‫اْلَحْم ُد ِهَّلِل اَّل ِذ ي َع اَف اِني ِفي َجَس ِد ي‬


‫ َو َأِذ َن لي ِبِذ ْك ِرِه‬،‫) ())َو َر َّد َع َلَّي ُروِح ي‬.
5

Niga koy diangè:


Alhamdou lil lahil lazi hafani fi disadi, waradda alayya
rouhi, wa azina lii bizikrihi.

Limiy firi moy:


Magi sant yalla mima mousal diammal ma ci sama yaram,
mou dello watma samg rouhe, mou yoomba lalma toud ko
mom yalla.

Gadadi diang àya yi:

-(4) ((﴿
‫ِض‬ ‫ْر‬‫َأل‬‫ا‬ ‫َو‬ ‫ِت‬‫ا‬ ‫َو‬ ‫َم‬ ‫الَّس‬ ‫ْل‬
‫ِإَّن ِفي َخ ِق‬
‫َو اْخ ِتَالِف الَّلْيِل َو الَّنَهاِر آَل َياٍت ُألْو ِلي األْلَب اِب‬
‫* اَّل ِذ يَن َي ْذ ُك ُروَن الَّل َه ِقَيامًا َو ُقُع ودًا َو َع َلَى‬
‫ُج ُن وِبِهْم َو َيَتَفَّك ُروَن ِفي َخ ْل ِق الَّس َم َو اِت‬
‫َو اَألْر ِض َر َّبَنا َم ا َخ َلْقَت َه ذا َب اِط ًال ُس ْبَح اَنَك‬
.3/144 ،‫ صحيح الترمذي‬:‫ وانظر‬،3401 ‫ برقم‬،473 /5 ،‫() الترمذي‬ 5
‫َفِقَنا َع َذ اَب الَّناِر* َر َّبَنا ِإَّنَك َم ن ُتْد ِخ ِل الَّناَر َفَقْد‬
‫َأْخ َز ْيَتُه َو َم ا ِللَّظ اِلِم يَن ِم ْن َأنَص اٍر * َّر َّبَن ا ِإَّنَن ا‬
‫َسِم ْع َنا ُم َناِد يًا ُيَن اِد ي ِلِإل يَم اِن َأْن آِم ُن وْا ِب َر ِّبُك ْم‬
‫َفآَم َّنا َر َّبَنا َفاْغ ِفْر َلَنا ُذُنوَبَنا َو َك ِّف ْر َع َّن ا َس ِّيَئاِتَنا‬
‫َو َتَو َّفَنا َم َع األْبَر اِر* َر َّبَنا َو آِتَنا َم ا َو َع دَّتَنا َع َلى‬
‫ُرُس ِلَك َو َال ُتْخ ِزَنا َي ْو َم اْلِقَياَم ِة ِإَّن َك َال ُتْخ ِل ُف‬
‫اْلِم يَع اَد * َفاْس َتَج اَب َلُهْم َر ُّبُهْم َأِّني َال ُأِض يُع‬
‫َع َم َل َع اِم ٍل ِّم نُك م ِّم ن َذ َك ٍر َأْو ُأنَثى َبْع ُض ُك م‬
‫ِّم ن َبْع ٍض َفاَّل ِذ يَن َه اَج ُروْا َو ُأْخ ِرُج وْا ِم ن‬
‫ِدَي اِرِهْم َو ُأوُذ وْا ِفي َس ِبيِلي َو َق اَتُلوْا َو ُقِتُل وْا‬
‫ُألَك ِّف َر َّن َع ْنُهْم َس ِّيَئاِتِهْم َو ُألْد ِخ َلَّنُهْم َج َّن اٍت‬
‫َتْج ِري ِم ن َتْح ِتَها اَألْنَه اُر َثَو ابًا ِّم ن ِع نِد الَّل ِه‬
‫َو الَّل ُه ِع نَد ُه ُح ْس ُن الَّث َو اِب * َال َيُغ َّر َّن َك َتَقُّلُب‬
‫اَّلِذ يَن َك َفُروْا ِفي اْلِبَالِد * َم َتاٌع َقِليٌل ُثَّم َم ْأَو اُهْم‬
‫َجَهَّنُم َو ِبْئَس اْلِمَهاُد * َلِكِن اَّلِذ يَن اَّتَقْو ْا َر َّبُهْم َلُهْم‬
‫َج َّناٌت َتْج ِري ِم ْن َتْح ِتَها اَألْنَه اُر َخ اِل ِد يَن ِفيَه ا‬
‫ُنُز ًال ِّم ْن ِع نِد الَّلِه َو َم ا ِع نَد الَّلِه َخ ْيٌر ِّلَألْبَر اِر *‬
‫َو ِإَّن ِم ْن َأْه ِل اْلِكَت اِب َلَم ن ُي ْؤ ِم ُن ِبالَّل ِه َو َم ا‬
‫ُأنِزَل ِإَلْيُك ْم َو َم آ ُأنِزَل ِإَلْيِهْم َخ اِش ِع يَن ِلَّل ِه َال‬
‫َيْش َتُروَن ِبآَي اِت الَّل ِه َثَم نًا َقِليًال ُأْو َلِئ َك َلُهْم‬
‫َأْج ُر ُهْم ِع نَد َر ِّبِهْم ِإَّن الَّل َه َس ِريُع اْلِحَس اِب*َي ا‬
‫َأُّيَها اَّلِذ يَن آَم ُنوْا اْص ِبُروْا َو َص اِبُروْا َو َر اِبُط وْا‬
‫) ())﴾َو اَّتُقوْا الَّلَه َلَع َّلُك ْم ُتْفِلُحوَن‬.
6

Limiy firi moy:


Soungou brom dane: bind gi ñou binde asaman ak souf,
ag woutante gi gouddi gi di woutante ak bathiak gi ay
kiman aki firne you ruey ñigi ci, kneel broom khelyi yiy
khèellou.
Ñiga khamnè dañiy toud yalla bouñou toogèe ak
bouñou tueddèe ak bouñou takhwèe, ñouy khalàat ci binde
gi yàlla binde asamànak souf. Ñounàn yàlla li duey bindoko
gir thiakhàn, yaw kou dañ baset wethie ga ci deflolou, yaw
yàlla yàlla gañou mousal ci mougaloum sawara.
Waw yàlla kèp koo dougal sawara trokhalgako, te ñiy
toñ baga dougal lèen sawara amoul kène kou lèen fa mana
dimbali.
Yaw yàlla noun dëy dignan ab yoonent bouy woote cig
am yalla ak wètalko top limou diglè, ñou gëmko wou
youyouko topko, yaw yàlla yalla gañou diegal, te soutoural
souñouy ayib, tega bolèñog ñou bakhñi booñiy fàat.
Yaw yàlla diokhe ñou liga ñou dig teas yoonnetiyi

،‫ع الفتح‬ ‫اري م‬ ‫ البخ‬،200-190 ،‫() اآلي ات من س ورة آل عم ران‬ 6

.256 ‫ برقم‬،530 /1 ،‫ ومسلم‬،4569 ‫ برقم‬،337 /8


diootli ñouko, tè boul ñou torokhal bou yawmal qiyàmà,
yaw dëy kou teed kiga khanè do woutal mouk digè boo dig
sa diam yi.
Yalla dadi naggou sèn ñàni, moune mom dè dou sank
mouk diëfi kouy diëf lou bakh ci yèen, mokham koka gorla
walla jigèen, ndakh ñom ño yam ci mbokkok dine, yamit ci
naggou gilèen di yàla di naggoul sèeni diëf.
Mounè ñiy gàddàay gir yalla, ñoulèn di gèenèe ci sèni
kër, dilèen lor gir top giñiy top yalla, ñouy khèekhe ci
yoonou yalla ñou dilèen thiay ray, ñooñou dëy dana lèen
dièeggal sèeni bakkar, tèdana lèen dougal ay adiana yo
khamne dèkhe ya gay daw ci soufam, mouy ak pay goulèen
di yàlla dif ay, tè yàlla moyor pay gi gën ci pay yi.
Yaw yoonnètèbi boumou la wor mouk ligay gis yèefaryi
di am ay warsak you yàtou di mana toukki di dèm founè ,
ndakh lolou ñouy dounde ci ay khèewal as ndir sou ndaw
lasoo khamne lèemou diekhe, te la thiay toop moy dèe
doug sawara, te kou sawara don sab lal sab lal bon na.
Waye ñiga khmnè ñom ño ragal yalla ci diëfè ay
ndigalam bayyi ay tèrèem ñom yàlla pare parélnalèen ay
adiana yoo khamne dèkhe yagay daw thia soufam, te fala
ñiy dëke ba fàw, mouy sèn kër, tè la nèk fa yalla ci ay
khèwal mougën ci ñou b

You might also like